At-Tawba · 63/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
أَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّهُ مَن يُحَادِدِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَأَنَّ لَهُ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدًا فِيهَا ۚ ذَٰلِكَ الْخِزْيُ الْعَظِيمُ ٦٣
Transliteration
Alam ya`lamooo annahoo mai yuhaadidillaaha wa Rasoolahoo faanna lahoo Naara jahannama khaalidan feehaa; zaalikal khizyul `Azeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañoo xamul ne (li wóor mooy) ne ku juuyook Yàlla ak Yonentam, dana ko ñeel ci loolu tàngooru Safara, fu muy sax ba fàwwu ? Muy gàcce gu mag.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 61-65 — Simoore At-Tawba
61وَمِنْهُمُ الَّذِينَ يُؤْذُونَ النَّبِيَّ وَيَقُولُونَ هُوَ أُذُنٌ ۚ قُلْ أُذُنُ خَيْرٍ لَّكُمْ يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَيُؤْمِنُ لِلْمُؤْمِنِينَ وَرَحْمَةٌ لِّلَّذِينَ آمَنُوا مِنكُمْ ۚ وَالَّذِينَ يُؤْذُونَ رَسُولَ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Am na ci ñoom ñuy lor Yonent bi, naan : “Benn nopp la”. - Neel : “Nopp bu yiw la ci yéen. Gëm na Yàlla te wóolu na way-gëm ña, te yërmaande la ci ñi gëm ci yéen. Te ñiy lor Yonentub Yàlla bi, mbugal mu metti ñeel na leen.
62يَحْلِفُونَ بِاللَّهِ لَكُمْ لِيُرْضُوكُمْ وَاللَّهُ وَرَسُولُهُ أَحَقُّ أَن يُرْضُوهُ إِن كَانُوا مُؤْمِنِينَ
Ña nga lay waatal ci Yàlla ngir am seen ngërëm. Te Yàlla ak Yonentam ñoo gën a yey ci ñoom sàkku seen ngërëm ndeem ñu gëm lañu.
63أَلَمْ يَعْلَمُوا أَنَّهُ مَن يُحَادِدِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَأَنَّ لَهُ نَارَ جَهَنَّمَ خَالِدًا فِيهَا ۚ ذَٰلِكَ الْخِزْيُ الْعَظِيمُ
Moo ndax dañoo xamul ne (li wóor mooy) ne ku juuyook Yàlla ak Yonentam, dana ko ñeel ci loolu tàngooru Safara, fu muy sax ba fàwwu ? Muy gàcce gu mag.
64يَحْذَرُ الْمُنَافِقُونَ أَن تُنَزَّلَ عَلَيْهِمْ سُورَةٌ تُنَبِّئُهُم بِمَا فِي قُلُوبِهِمْ ۚ قُلِ اسْتَهْزِئُوا إِنَّ اللَّهَ مُخْرِجٌ مَّا تَحْذَرُونَ
Naaféq ya danañu ragal aw saar wàcc feeñal li nekk ci seeni xol. Neeleen : “Ñaawleleen ! Yàlla Dana génne li ngeen di ragal (mu génn)”.
65وَلَئِن سَأَلْتَهُمْ لَيَقُولُنَّ إِنَّمَا كُنَّا نَخُوضُ وَنَلْعَبُ ۚ قُلْ أَبِاللَّهِ وَآيَاتِهِ وَرَسُولِهِ كُنتُمْ تَسْتَهْزِئُونَ
Te boo leen laajoon, Giñ naa ne danañu wax naan : “Nun dey danu doon caaxaan.”. Neeleen : “Kon daal yéen Yàlla ngeen di fowe ? ”
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
63Aaya
Tekki — At-Tawba 63
Simoore At-Tawba Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañoo xamul ne (li wóor mooy) ne ku…Simoore Aaya 63/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 7, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







