Al-Balad · 5/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ ۝٥
Ayahsabu al-lai yaqdira `alaihi ahad
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Balad

3وَوَالِدٍ وَمَا وَلَدَ
Ak ci baay ak la mu jur !
4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي كَبَدٍ
Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.
5أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?
6يَقُولُ أَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًا
Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.
7أَيَحْسَبُ أَن لَّمْ يَرَهُ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Balad 5

Simoore Al-Balad Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara…

Simoore Aaya 5/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers