Ash-Shams · 14/15
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shams
فَكَذَّبُوهُ فَعَقَرُوهَا فَدَمْدَمَ عَلَيْهِمْ رَبُّهُم بِذَنبِهِمْ فَسَوَّاهَا ۝١٤
Fakazzaboohu fa`aqaroohaa fadamdama `alaihim Rabbuhum bizambihim fasaw waahaa
📖 Tekkim Wolof
Ñu weddi ko, rey ko. Seen Boroom, maasale na mbugël ma.ca kaw nit ñépp

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-15 — Simoore Ash-Shams

12إِذِ انبَعَثَ أَشْقَاهَا
ba ca ña gën weddi potoxlóo
13فَقَالَ لَهُمْ رَسُولُ اللَّهِ نَاقَةَ اللَّهِ وَسُقْيَاهَا
Yonentub Yàlla ba ne leen : “Bàyyileen giléemug Yàlla gi ! mu naan”
14فَكَذَّبُوهُ فَعَقَرُوهَا فَدَمْدَمَ عَلَيْهِمْ رَبُّهُم بِذَنبِهِمْ فَسَوَّاهَا
Ñu weddi ko, rey ko. Seen Boroom, maasale na mbugël ma.ca kaw nit ñépp
15وَلَا يَخَافُ عُقْبَاهَا
Te ragalul dara ca la cay mujj :
Ash-ShamsFihi Alxuraan
15Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Ash-Shams 14

Simoore Ash-Shams Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu weddi ko, rey ko. Seen Boroom, maasale na mbugël…

Simoore Aaya 14/15 — Simoore Ash-Shams الشمس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shams Dégg, Simoore Ash-Shams Tekki, Simoore Ash-Shams mp3, Simoore Ash-Shams pdf. Aaya 12–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers