Al-Bayyina · 6/8
Tekki Waxtaan — Al-Bayyina
إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَالْمُشْرِكِينَ فِي نَارِ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ أُولَٰئِكَ هُمْ شَرُّ الْبَرِيَّةِ ٦
Transliteration
Innal lazeena kafaru min ahlil kitaabi wal mushri keena fee nari jahan nama khaali deena feeha; ulaa-ika hum shar rul ba reeyah
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñay weddi te bokk ci ñoñ téere, ak Bokkaalekat ya ñoom ña nga ca biir Safaraw Jahanama, te danu fay béel. Ñoom ñii, ñoo yées ci bindeef yi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 4-8 — Al-Bayyina
4وَمَا تَفَرَّقَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُمُ الْبَيِّنَةُ
Te gaa ña ñu joxoon téere masuñoo teqalikoo lu dul ginnaaw ba leen firnde ja dikkëlee.
5وَمَا أُمِرُوا إِلَّا لِيَعْبُدُوا اللَّهَ مُخْلِصِينَ لَهُ الدِّينَ حُنَفَاءَ وَيُقِيمُوا الصَّلَاةَ وَيُؤْتُوا الزَّكَاةَ ۚ وَذَٰلِكَ دِينُ الْقَيِّمَةِ
Te digaleefu leen, lu dul, na nuy jaamu Yàlla, bañ Koo bokkaale te di ko sellal, tey taxawal Julli di joxe asaka. Loolu mooy diiney njub ja.
6إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَالْمُشْرِكِينَ فِي نَارِ جَهَنَّمَ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ أُولَٰئِكَ هُمْ شَرُّ الْبَرِيَّةِ
Ñay weddi te bokk ci ñoñ téere, ak Bokkaalekat ya ñoom ña nga ca biir Safaraw Jahanama, te danu fay béel. Ñoom ñii, ñoo yées ci bindeef yi.
7إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ أُولَٰئِكَ هُمْ خَيْرُ الْبَرِيَّةِ
Ñi gëm tey jëfu yiw, ñoom ñoo ñee ñoo gën ci bindeef yi.
8جَزَاؤُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتُ عَدْنٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ رَّضِيَ اللَّهُ عَنْهُمْ وَرَضُوا عَنْهُ ۚ ذَٰلِكَ لِمَنْ خَشِيَ رَبَّهُ
Seenug pey fa seen Boroom Àjjanay adan lay doon, yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam, ñu béel fa. Yàlla gëram leen ñoom it ñu gëram ko. Loolu ku ragal Yàlla rekk koy am.
Al-BayyinaFihi Alxuraan
8Aaya
MedinanRevelation
6Aaya
Tekki — Al-Bayyina 6
Simoore Al-Bayyina Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñay weddi te bokk ci ñoñ téere, ak Bokkaalekat ya…Simoore Aaya 6/8 — Al-Bayyina البينة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Bayyina Dégg, Al-Bayyina Tekki, Al-Bayyina mp3, Al-Bayyina pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








