Hud · 103/123
Tekki Waxtaan — Hud
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّمَنْ خَافَ عَذَابَ الْآخِرَةِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّجْمُوعٌ لَّهُ النَّاسُ وَذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّشْهُودٌ ۝١٠٣
Inna fee zaalika la aayatal liman khaafa `azaabal Aakhirah; zaalika Yawmum majmoo`ul lahun naasu wa zaalika Yawmum mashhood
📖 Tekkim Wolof
Kaawtéef nekk na ci loolu ci ku ragal mbugalam àllaaxira. Bis boobu bis ba ñu koy dajaleel nit ñi; te bis la bu ñépp di teewe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 101-105 — Hud

101وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن ظَلَمُوا أَنفُسَهُمْ ۖ فَمَا أَغْنَتْ عَنْهُمْ آلِهَتُهُمُ الَّتِي يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مِن شَيْءٍ لَّمَّا جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَمَا زَادُوهُمْ غَيْرَ تَتْبِيبٍ
Tooñunuleen. Waaye ñoo tooñ seen bopp. Seen yàlla ya ñu doon jaamu, bàyyi fa Yàlla, jariñuleen dara. Ba sa ndigalu Boroom agsee, dolliwuleen lu dul alkaande.
102وَكَذَٰلِكَ أَخْذُ رَبِّكَ إِذَا أَخَذَ الْقُرَىٰ وَهِيَ ظَالِمَةٌ ۚ إِنَّ أَخْذَهُ أَلِيمٌ شَدِيدٌ
Noonu la sa Boroom di alage, bu alagee njéndi fekk ñu tooñ. Alage ju Muy alag [ñooña], dafay metti tar.
103إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّمَنْ خَافَ عَذَابَ الْآخِرَةِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّجْمُوعٌ لَّهُ النَّاسُ وَذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّشْهُودٌ
Kaawtéef nekk na ci loolu ci ku ragal mbugalam àllaaxira. Bis boobu bis ba ñu koy dajaleel nit ñi; te bis la bu ñépp di teewe.
104وَمَا نُؤَخِّرُهُ إِلَّا لِأَجَلٍ مَّعْدُودٍ
Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu ñu ko àppal.
105يَوْمَ يَأْتِ لَا تَكَلَّمُ نَفْسٌ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۚ فَمِنْهُمْ شَقِيٌّ وَسَعِيدٌ
Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku ca am ndigal. Te ca nit ña am na ca ñu texeedi ak ñu texe.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
103Aaya

Tekki — Hud 103

Simoore Hud Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kaawtéef nekk na ci loolu ci ku ragal mbugalam àllaaxira.…

Simoore Aaya 103/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers