Hud · 104/123
Tekki Waxtaan — Hud
وَمَا نُؤَخِّرُهُ إِلَّا لِأَجَلٍ مَّعْدُودٍ ۝١٠٤
Wa maa nu`akhkhiruhooo illaa li ajalim ma`dood
📖 Tekkim Wolof
Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu ñu ko àppal.
🎧 Dégg

📜 Aaya 102-106 — Hud

102وَكَذَٰلِكَ أَخْذُ رَبِّكَ إِذَا أَخَذَ الْقُرَىٰ وَهِيَ ظَالِمَةٌ ۚ إِنَّ أَخْذَهُ أَلِيمٌ شَدِيدٌ
Noonu la sa Boroom di alage, bu alagee njéndi fekk ñu tooñ. Alage ju Muy alag [ñooña], dafay metti tar.
103إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّمَنْ خَافَ عَذَابَ الْآخِرَةِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّجْمُوعٌ لَّهُ النَّاسُ وَذَٰلِكَ يَوْمٌ مَّشْهُودٌ
Kaawtéef nekk na ci loolu ci ku ragal mbugalam àllaaxira. Bis boobu bis ba ñu koy dajaleel nit ñi; te bis la bu ñépp di teewe.
104وَمَا نُؤَخِّرُهُ إِلَّا لِأَجَلٍ مَّعْدُودٍ
Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu ñu ko àppal.
105يَوْمَ يَأْتِ لَا تَكَلَّمُ نَفْسٌ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۚ فَمِنْهُمْ شَقِيٌّ وَسَعِيدٌ
Bu bis ba dikkee, kenn du wax ku dul ku ca am ndigal. Te ca nit ña am na ca ñu texeedi ak ñu texe.
106فَأَمَّا الَّذِينَ شَقُوا فَفِي النَّارِ لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَشَهِيقٌ
Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — Hud 104

Simoore Hud Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yeexewuñu ko de, dafa di rekk am na dig bu…

Simoore Aaya 104/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers