Hud · 41/123
Tekki Waxtaan — Hud
۞ وَقَالَ ارْكَبُوا فِيهَا بِسْمِ اللَّهِ مَجْرَاهَا وَمُرْسَاهَا ۚ إِنَّ رَبِّي لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ ۝٤١
Wa qaalar kaboo feehaa bismil laahi majraihaa wa mursaahaa; inna Rabbee la Ghafoorur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Mu ne leen : “Yéegleen ci biir tey tudd Yàlla, mooy aw xélam, te it ag teeram. Sama Boroom nag Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 39-43 — Hud

39فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَيَحِلُّ عَلَيْهِ عَذَابٌ مُّقِيمٌ
Xalset ngeen a xam ana kan la mbugalam di dal, toroxal ko, ba noppi mbugalam wàcc ci kawam, di lu sax dàkk ! ”
40حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَمْرُنَا وَفَارَ التَّنُّورُ قُلْنَا احْمِلْ فِيهَا مِن كُلٍّ زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ وَأَهْلَكَ إِلَّا مَن سَبَقَ عَلَيْهِ الْقَوْلُ وَمَنْ آمَنَ ۚ وَمَا آمَنَ مَعَهُ إِلَّا قَلِيلٌ
Ba Sunu ndigal agsee, ndox ma di ballee fu ne, Nu ne : “Defal ci gaal gi, ci xeet wu nekk ñaar [góor ak jigéen] ak sa njaboot - ba mu des ña dogal ba xas dal [ña weddi] - ak ña gëm”. Te lim bu néew rekk a gëmoon.
41۞ وَقَالَ ارْكَبُوا فِيهَا بِسْمِ اللَّهِ مَجْرَاهَا وَمُرْسَاهَا ۚ إِنَّ رَبِّي لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
Mu ne leen : “Yéegleen ci biir tey tudd Yàlla, mooy aw xélam, te it ag teeram. Sama Boroom nag Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la”.
42وَهِيَ تَجْرِي بِهِمْ فِي مَوْجٍ كَالْجِبَالِ وَنَادَىٰ نُوحٌ ابْنَهُ وَكَانَ فِي مَعْزِلٍ يَا بُنَيَّ ارْكَب مَّعَنَا وَلَا تَكُن مَّعَ الْكَافِرِينَ
Gaal gay daw ak ñoom ciy ganax yu kawe ni ay tundu. Nooh daldi woo doomam, fekk mu beru woon, ne ko : "Sama doom, yéegal ànd ak nun te bul ànd ak yéefar yi”.
43قَالَ سَآوِي إِلَىٰ جَبَلٍ يَعْصِمُنِي مِنَ الْمَاءِ ۚ قَالَ لَا عَاصِمَ الْيَوْمَ مِنْ أَمْرِ اللَّهِ إِلَّا مَن رَّحِمَ ۚ وَحَالَ بَيْنَهُمَا الْمَوْجُ فَكَانَ مِنَ الْمُغْرَقِينَ
Mu ne ko : “Maa ngi tëdd ci tundu doj wi, dana ma musal ci ndox mi”. Mu ne ko : “Kenn du mucc tey ci mbirum Yàlla ku dul ku Yàlla yërëm”. Noonu, am ganax [duus] wu dox seen diggante, mu daldi lab.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Hud 41

Simoore Hud Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne leen : “Yéegleen ci biir tey tudd Yàlla,…

Simoore Aaya 41/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers