Hud · 74/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
فَلَمَّا ذَهَبَ عَنْ إِبْرَاهِيمَ الرَّوْعُ وَجَاءَتْهُ الْبُشْرَىٰ يُجَادِلُنَا فِي قَوْمِ لُوطٍ ۝٧٤
Falammaa zahaba an Ibraaheemar raw`u wa jaaa`at hul bushraaa yujaadilunaa fee qawmi Loot
📖 Tekkim Wolof
Ba tiit ma bàyyee Ibraahiima te mu am mbégte, jéem naa dàggasante ak Nun ci nitu Lóot ña,

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Hud

72قَالَتْ يَا وَيْلَتَىٰ أَأَلِدُ وَأَنَا عَجُوزٌ وَهَٰذَا بَعْلِي شَيْخًا ۖ إِنَّ هَٰذَا لَشَيْءٌ عَجِيبٌ
Mu wax ne : “Cëy man ! Ndax danaa jurati doom te màggat naa, sama boroom-kër bii it di ku mage ? Lii dey mbir mu doy waar la ! ”
73قَالُوا أَتَعْجَبِينَ مِنْ أَمْرِ اللَّهِ ۖ رَحْمَتُ اللَّهِ وَبَرَكَاتُهُ عَلَيْكُمْ أَهْلَ الْبَيْتِ ۚ إِنَّهُ حَمِيدٌ مَّجِيدٌ
Ñu ne ko : “Ndax dangay yéemu ci mbiru Yàlla ? Yërmaandey Yàlla ak barkeem, yal na nekk ci yéen waa kër gi ! Moom Yàlla moo yeyoo cant ak màggal ko ! ”
74فَلَمَّا ذَهَبَ عَنْ إِبْرَاهِيمَ الرَّوْعُ وَجَاءَتْهُ الْبُشْرَىٰ يُجَادِلُنَا فِي قَوْمِ لُوطٍ
Ba tiit ma bàyyee Ibraahiima te mu am mbégte, jéem naa dàggasante ak Nun ci nitu Lóot ña,
75إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَحَلِيمٌ أَوَّاهٌ مُّنِيبٌ
Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab delluwaakoon ci Boroomam.
76يَا إِبْرَاهِيمُ أَعْرِضْ عَنْ هَٰذَا ۖ إِنَّهُ قَدْ جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَإِنَّهُمْ آتِيهِمْ عَذَابٌ غَيْرُ مَرْدُودٍ
Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax sa ndigalul Boroom dikk na ba noppi, te ñoom, mbugal mu ñu dul delloo dana leen dikkal”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Hud 74

Simoore Hud Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba tiit ma bàyyee Ibraahiima te mu am mbégte, jéem…

Simoore Aaya 74/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers