Hud · 75/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَحَلِيمٌ أَوَّاهٌ مُّنِيبٌ ۝٧٥
Inna Ibraaheema lahaleemun awwwaahum muneeb
📖 Tekkim Wolof
Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab delluwaakoon ci Boroomam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Simoore Hud

73قَالُوا أَتَعْجَبِينَ مِنْ أَمْرِ اللَّهِ ۖ رَحْمَتُ اللَّهِ وَبَرَكَاتُهُ عَلَيْكُمْ أَهْلَ الْبَيْتِ ۚ إِنَّهُ حَمِيدٌ مَّجِيدٌ
Ñu ne ko : “Ndax dangay yéemu ci mbiru Yàlla ? Yërmaandey Yàlla ak barkeem, yal na nekk ci yéen waa kër gi ! Moom Yàlla moo yeyoo cant ak màggal ko ! ”
74فَلَمَّا ذَهَبَ عَنْ إِبْرَاهِيمَ الرَّوْعُ وَجَاءَتْهُ الْبُشْرَىٰ يُجَادِلُنَا فِي قَوْمِ لُوطٍ
Ba tiit ma bàyyee Ibraahiima te mu am mbégte, jéem naa dàggasante ak Nun ci nitu Lóot ña,
75إِنَّ إِبْرَاهِيمَ لَحَلِيمٌ أَوَّاهٌ مُّنِيبٌ
Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab delluwaakoon ci Boroomam.
76يَا إِبْرَاهِيمُ أَعْرِضْ عَنْ هَٰذَا ۖ إِنَّهُ قَدْ جَاءَ أَمْرُ رَبِّكَ ۖ وَإِنَّهُمْ آتِيهِمْ عَذَابٌ غَيْرُ مَرْدُودٍ
Ñu ne ko : “Yaw Ibraahiima, génnal ci lii ndax sa ndigalul Boroom dikk na ba noppi, te ñoom, mbugal mu ñu dul delloo dana leen dikkal”.
77وَلَمَّا جَاءَتْ رُسُلُنَا لُوطًا سِيءَ بِهِمْ وَضَاقَ بِهِمْ ذَرْعًا وَقَالَ هَٰذَا يَوْمٌ عَصِيبٌ
Ba Sunuy ndaw agsee ca Lóot, mu jàq ca ñoom, am naqar ci ñoom. Daldi ne : “Lii dey bis bu tiis la”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Hud 75

Simoore Hud Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ibraahiima dey ku lewet la, di kuy toroxlu, di ab…

Simoore Aaya 75/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers