Hud · 84/123
Tekki Waxtaan — Hud
۞ وَإِلَىٰ مَدْيَنَ أَخَاهُمْ شُعَيْبًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ وَلَا تَنقُصُوا الْمِكْيَالَ وَالْمِيزَانَ ۚ إِنِّي أَرَاكُم بِخَيْرٍ وَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ مُّحِيطٍ ۝٨٤
Wa ilaa Madyana akhaahum Shu`aibaa; qaala yaa qawmi` budul laaha maa lakum min ilaahin ghairuhoo wa laa tanqusul mikyaala walmeezaan; inneee araakum bikhairinw wa innee akhaafu `alaikum `azaaba Yawmim muheet
📖 Tekkim Wolof
Yónni woon Nanu it ca waa Madyaana seen mbokk Suhaybu, mu ne leen : "Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla ; amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Buleen wàññi nattukaay yi ak màndaxe yi. Gis naa ne yéen a ngi ci biiri xéewal, te ragal naa mbugal dal leen ca bis ba ëmb lépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 82-86 — Hud

82فَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا جَعَلْنَا عَالِيَهَا سَافِلَهَا وَأَمْطَرْنَا عَلَيْهَا حِجَارَةً مِّن سِجِّيلٍ مَّنضُودٍ
Ba Sunu dogal agsee, wëlbati Nanu [dëkk ba], la féete woon kaw féete suuf, Nu sotti ca kawam tawu xeer yu jóge Sijjiil [Safara] ay doj yu ñu toftale,
83مُّسَوَّمَةً عِندَ رَبِّكَ ۖ وَمَا هِيَ مِنَ الظَّالِمِينَ بِبَعِيدٍ
yu ñu màndargaal ca sa Boroom. Te dëkk boobu soreewul ag way-tooñ ya [ya ca Màkka].
84۞ وَإِلَىٰ مَدْيَنَ أَخَاهُمْ شُعَيْبًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ وَلَا تَنقُصُوا الْمِكْيَالَ وَالْمِيزَانَ ۚ إِنِّي أَرَاكُم بِخَيْرٍ وَإِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ مُّحِيطٍ
Yónni woon Nanu it ca waa Madyaana seen mbokk Suhaybu, mu ne leen : "Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla ; amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Buleen wàññi nattukaay yi ak màndaxe yi. Gis naa ne yéen a ngi ci biiri xéewal, te ragal naa mbugal dal leen ca bis ba ëmb lépp.
85وَيَا قَوْمِ أَوْفُوا الْمِكْيَالَ وَالْمِيزَانَ بِالْقِسْطِ ۖ وَلَا تَبْخَسُوا النَّاسَ أَشْيَاءَهُمْ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Yéen samaw nit, nangeen di matal natt ak màndaxe cig maandute, te buleen wàññi dara ci lu nit ñi moom, te buleen salfaañe ci suuf si nekk yàqkat..
86بَقِيَّتُ اللَّهِ خَيْرٌ لَّكُمْ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ ۚ وَمَا أَنَا عَلَيْكُم بِحَفِيظٍ
Wërsëgu Yàlla moo gën ci yéen ndegam ñu gëm ngeen ! Te nekkuma di ku leen di warlul kiiraay”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — Hud 84

Simoore Hud Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni woon Nanu it ca waa Madyaana seen mbokk Suhaybu,…

Simoore Aaya 84/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers