Hud · 95/123
Tekki Waxtaan — Hud
كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۗ أَلَا بُعْدًا لِّمَدْيَنَ كَمَا بَعِدَتْ ثَمُودُ ٩٥
Transliteration
Ka-al-lam yaghnaw feehaaa; alaa bu`dal li Madyana Kamaa ba`idat Samood
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
mu mel ni masuñu fa woon a dëkk. Waaw, ndax alkaande dalul waa Madyaana na mu alake woon waa Samuuda ?.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 93-97 — Hud
93وَيَا قَوْمِ اعْمَلُوا عَلَىٰ مَكَانَتِكُمْ إِنِّي عَامِلٌ ۖ سَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَمَنْ هُوَ كَاذِبٌ ۖ وَارْتَقِبُوا إِنِّي مَعَكُمْ رَقِيبٌ
Yéen samaw nit, defleen lu leen soob. Man it danaa def [li ma sama Boroom sant]. Dangeen mas a xam kan la mbugal di dal, gàcceel ko, ak kan mooy kay fen. Te muñandikuleen ! Maa ngi ànd ak yéen di muñ”.
94وَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا شُعَيْبًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَأَخَذَتِ الَّذِينَ ظَلَمُوا الصَّيْحَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دِيَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ba Sunu ndigal agsee, musal Nanu Suhaybu ak ña gëmoon ànd ak moom ci Sunu yërmaande. Ag xaacu faagaagal ña tooñ, ñu mujj xëy ne lànjaŋ dee fa seen kër ya,
95كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۗ أَلَا بُعْدًا لِّمَدْيَنَ كَمَا بَعِدَتْ ثَمُودُ
mu mel ni masuñu fa woon a dëkk. Waaw, ndax alkaande dalul waa Madyaana na mu alake woon waa Samuuda ?.
96وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Te yónni woon Nanu Muusaa mu ànd ak Sunuy kaawtéef ak lay yu leer nàññ,
97إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاتَّبَعُوا أَمْرَ فِرْعَوْنَ ۖ وَمَا أَمْرُ فِرْعَوْنَ بِرَشِيدٍ
ca Firawna ak boroom darajaam ya. Ñu topp ndigalu Firawna, te ndigalu Firawna jubul woon.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
95Aaya
Tekki — Hud 95
Simoore Hud Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu mel ni masuñu fa woon a dëkk. Waaw, ndax…Simoore Aaya 95/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








