An-Nahl · 74/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
فَلَا تَضْرِبُوا لِلَّهِ الْأَمْثَالَ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ وَأَنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ ٧٤
Transliteration
Falaa tadriboo lillaahil amsaal; innal laaha ya`lamu wa antum laa ta`lamoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Buleen wutal Yàlla niraale mukk. Yàlla xam na te yéen xamuleen.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 72-76 — An-Nahl
72وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُم مِّنْ أَنفُسِكُمْ أَزْوَاجًا وَجَعَلَ لَكُم مِّنْ أَزْوَاجِكُم بَنِينَ وَحَفَدَةً وَرَزَقَكُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ ۚ أَفَبِالْبَاطِلِ يُؤْمِنُونَ وَبِنِعْمَتِ اللَّهِ هُمْ يَكْفُرُونَ
Yàlla sàkkal na leen ay jabar yu jóge ci yéen, Mu sàkkal leen ay doom yu jóge ci seeni jabar ak i sët. Mu boole ca wërsëgal leen ñam yu sell. Waa ndax [yéefar yi] dañuy gëm ay xërëm tey weddi xéewali Yàlla yi ?
73وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَمْلِكُ لَهُمْ رِزْقًا مِّنَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ شَيْئًا وَلَا يَسْتَطِيعُونَ
Te dañoo bàyyi Yàlla di jaamu loo xam ne moomul dara lu mu leen mën a wërsërgal ci kaw asamaan yi ak ci suuf si. Te mënul dara.
74فَلَا تَضْرِبُوا لِلَّهِ الْأَمْثَالَ ۚ إِنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ وَأَنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Buleen wutal Yàlla niraale mukk. Yàlla xam na te yéen xamuleen.
75۞ ضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا عَبْدًا مَّمْلُوكًا لَّا يَقْدِرُ عَلَىٰ شَيْءٍ وَمَن رَّزَقْنَاهُ مِنَّا رِزْقًا حَسَنًا فَهُوَ يُنفِقُ مِنْهُ سِرًّا وَجَهْرًا ۖ هَلْ يَسْتَوُونَ ۚ الْحَمْدُ لِلَّهِ ۚ بَلْ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Yàllaa ngay joxe léebu ci jaam bu ñu moom, te amul mën-mën ci dara, ak ki nga xam ne [gor] la te Nu wërsëgal ko lu jóge ci Nun wërsëg wu rafet, te mu di ca dimbalee ci lu nëbb ak ci lu feeñ. Ñooña ñaar ndax yem nañu ? Cant ñeel na Yàlla ! Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
76وَضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا رَّجُلَيْنِ أَحَدُهُمَا أَبْكَمُ لَا يَقْدِرُ عَلَىٰ شَيْءٍ وَهُوَ كَلٌّ عَلَىٰ مَوْلَاهُ أَيْنَمَا يُوَجِّههُّ لَا يَأْتِ بِخَيْرٍ ۖ هَلْ يَسْتَوِي هُوَ وَمَن يَأْمُرُ بِالْعَدْلِ ۙ وَهُوَ عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Yàllaa ngay joxe ba-tey léebu ñaari góor yoo xam ne : kenn ka dafa luu [muuma], mënul dara te moom dafa wéeru ci sangam ; Te fu mu mën di jubale, du ca jële njariñ ; ndax dafay yem ak ki nga xam ne dafay digle maandute te lu mu def mu àntu tegu ci njub ?
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
74Aaya
Tekki — An-Nahl 74
Simoore An-Nahl Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen wutal Yàlla niraale mukk. Yàlla xam na te yéen…Simoore Aaya 74/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








