Al-Isra · 26/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَآتِ ذَا الْقُرْبَىٰ حَقَّهُ وَالْمِسْكِينَ وَابْنَ السَّبِيلِ وَلَا تُبَذِّرْ تَبْذِيرًا ٢٦
Transliteration
Wa aati zal qurbaa haqqahoo walmiskeena wabnas sabeeli wa laa tubazzir tabzeeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Nanga jox sa jegeñaale li la war ci moom, ak ku ñàkk ak ku nekk ci tukki. Waaye bul nekk di pasar-pasaree alal,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 24-28 — Al-Isra
24وَاخْفِضْ لَهُمَا جَنَاحَ الذُّلِّ مِنَ الرَّحْمَةِ وَقُل رَّبِّ ارْحَمْهُمَا كَمَا رَبَّيَانِي صَغِيرًا
Nanga suufeel sa bopp ngir ñoom ; di toroxlu ci yërmaande ; te deel wax : "Sama Boroom yërëm leen [ni ñu ma yërëme woon] ba ñu may yar ba ma nekkee xale”.
25رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِمَا فِي نُفُوسِكُمْ ۚ إِن تَكُونُوا صَالِحِينَ فَإِنَّهُ كَانَ لِلْأَوَّابِينَ غَفُورًا
Seen Boroom a gën a xam li nekk ci seen bakkan. Ndeem nekk ngeen ñu sell ; Moom Jéggalaakoon la ci ñiy dellu jëm ci jaamu Yàlla.
26وَآتِ ذَا الْقُرْبَىٰ حَقَّهُ وَالْمِسْكِينَ وَابْنَ السَّبِيلِ وَلَا تُبَذِّرْ تَبْذِيرًا
“Nanga jox sa jegeñaale li la war ci moom, ak ku ñàkk ak ku nekk ci tukki. Waaye bul nekk di pasar-pasaree alal,
27إِنَّ الْمُبَذِّرِينَ كَانُوا إِخْوَانَ الشَّيَاطِينِ ۖ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِرَبِّهِ كَفُورًا
yàqkat yi mbokki Séytaane lañu ; te Séytaane dafa weddi Boroomam.
28وَإِمَّا تُعْرِضَنَّ عَنْهُمُ ابْتِغَاءَ رَحْمَةٍ مِّن رَّبِّكَ تَرْجُوهَا فَقُل لَّهُمْ قَوْلًا مَّيْسُورًا
Bu fekkee [ñàkk loo leen jox tax na] nga dëddu leen, toog di yaakaar sa yërmaandey Boroom ; nanga leen wax wax ju neex.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
26Aaya
Tekki — Al-Isra 26
Simoore Al-Isra Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Nanga jox sa jegeñaale li la war ci moom, ak…Simoore Aaya 26/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








