Al-Isra · 43/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يَقُولُونَ عُلُوًّا كَبِيرًا ۝٤٣
Subhaanahoo wa Ta`aalaa `ammaa yaqooloona `uluwwan kabeeraa
📖 Tekkim Wolof
Cëy sellam ga ! Kawe na, jomb na li ñuy wax, jombute gu màgg a màgg !

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Isra

41وَلَقَدْ صَرَّفْنَا فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ لِيَذَّكَّرُوا وَمَا يَزِيدُهُمْ إِلَّا نُفُورًا
Te leeral Nanu ci Alxuraan jii [lu ne] ngir ñu xalaat. Te dolliwuleen lu dul fen [wëliis dëgg].
42قُل لَّوْ كَانَ مَعَهُ آلِهَةٌ كَمَا يَقُولُونَ إِذًا لَّابْتَغَوْا إِلَىٰ ذِي الْعَرْشِ سَبِيلًا
Neel : “Bu amoon yeneeni Yàlla tu nekk ak Moom, ni ñu ko waxe, kon dinañu sàkk [yoon wu leen yóbb] ca Boroom gàngune ga”.(yab Yàlla)
43سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يَقُولُونَ عُلُوًّا كَبِيرًا
Cëy sellam ga ! Kawe na, jomb na li ñuy wax, jombute gu màgg a màgg !
44تُسَبِّحُ لَهُ السَّمَاوَاتُ السَّبْعُ وَالْأَرْضُ وَمَن فِيهِنَّ ۚ وَإِن مِّن شَيْءٍ إِلَّا يُسَبِّحُ بِحَمْدِهِ وَلَٰكِن لَّا تَفْقَهُونَ تَسْبِيحَهُمْ ۗ إِنَّهُ كَانَ حَلِيمًا غَفُورًا
Juróom-ñaari asamaan yi ak suuf si, ñi ngi koy sàbbaal, ak li nekk ci seen biir. Te sax amul dara lu nekk te du Ko sàbbaal ci li Mu yeyoo mboolem cant. Waaye dangeen a amul dégg-dégg ci seeni sàbbaal. Naka Moom Aji-lewet la, Jéggalaakoon la.
45وَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ جَعَلْنَا بَيْنَكَ وَبَيْنَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ حِجَابًا مَّسْتُورًا
Booy jàng Alxuraan, Dananu def ci sa diggante ak ñi gëmul àllaaxira kiiraay lu nëbbu,
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Isra 43

Simoore Al-Isra Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Cëy sellam ga ! Kawe na, jomb na li ñuy…

Simoore Aaya 43/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers