Al-Isra · 65/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ ۚ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ وَكِيلًا ۝٦٥
Inna `ibaadee laisa laka `alaihim sultaan; wa kafaa bi Rabbika Wakeelaa
📖 Tekkim Wolof
Naka samay jaam, doo am genn kàttan ci ñoom”. Ndax sa Boroom doy na cëslaay.
🎧 Dégg

📜 Aaya 63-67 — Al-Isra

63قَالَ اذْهَبْ فَمَن تَبِعَكَ مِنْهُمْ فَإِنَّ جَهَنَّمَ جَزَاؤُكُمْ جَزَاءً مَّوْفُورًا
Mu ne ko : “Demal ! Ku la topp ci ñoom... [na xam ne] Safara moo di seen pey, pey guy nekk di lu mat sëkk.
64وَاسْتَفْزِزْ مَنِ اسْتَطَعْتَ مِنْهُم بِصَوْتِكَ وَأَجْلِبْ عَلَيْهِم بِخَيْلِكَ وَرَجِلِكَ وَشَارِكْهُمْ فِي الْأَمْوَالِ وَالْأَوْلَادِ وَعِدْهُمْ ۚ وَمَا يَعِدُهُمُ الشَّيْطَانُ إِلَّا غُرُورًا
Génnal ak say kàddu, loo mën ci ñoom, nanga leen song ak say xarekat ak say gawar, nanga bokk ak ñoom alal ak i doomn te digleen”. Waaye Séytaane duleen dig lu dul ay nax.
65إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ ۚ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ وَكِيلًا
Naka samay jaam, doo am genn kàttan ci ñoom”. Ndax sa Boroom doy na cëslaay.
66رَّبُّكُمُ الَّذِي يُزْجِي لَكُمُ الْفُلْكَ فِي الْبَحْرِ لِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِكُمْ رَحِيمًا
Sa Boroom mooy kiy dawloo gaal ci géej, ngir ngeen mën a sàkku ay xéewalam ; Naka Moom ku am yërmaande la ci yéen,
67وَإِذَا مَسَّكُمُ الضُّرُّ فِي الْبَحْرِ ضَلَّ مَن تَدْعُونَ إِلَّا إِيَّاهُ ۖ فَلَمَّا نَجَّاكُمْ إِلَى الْبَرِّ أَعْرَضْتُمْ ۚ وَكَانَ الْإِنسَانُ كَفُورًا
Bu leen naqar dabee ci géej, ña ngeen doon jaamu réer leen ginnaawam. Te bu Nu leen musalee ba ñu agsi ci jéeri ji, ngeen dëddu. Nit daal ku goreedi la !
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Isra 65

Simoore Al-Isra Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka samay jaam, doo am genn kàttan ci ñoom”. Ndax…

Simoore Aaya 65/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers