Al-Isra · 66/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
رَّبُّكُمُ الَّذِي يُزْجِي لَكُمُ الْفُلْكَ فِي الْبَحْرِ لِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِكُمْ رَحِيمًا ۝٦٦
Rabbukumul lazee yuzjee lakumul fulka fil bahri litabtaghoo min fadlih; innahoo kaana bikum Raheemaa
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom mooy kiy dawloo gaal ci géej, ngir ngeen mën a sàkku ay xéewalam ; Naka Moom ku am yërmaande la ci yéen,

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Simoore Al-Isra

64وَاسْتَفْزِزْ مَنِ اسْتَطَعْتَ مِنْهُم بِصَوْتِكَ وَأَجْلِبْ عَلَيْهِم بِخَيْلِكَ وَرَجِلِكَ وَشَارِكْهُمْ فِي الْأَمْوَالِ وَالْأَوْلَادِ وَعِدْهُمْ ۚ وَمَا يَعِدُهُمُ الشَّيْطَانُ إِلَّا غُرُورًا
Génnal ak say kàddu, loo mën ci ñoom, nanga leen song ak say xarekat ak say gawar, nanga bokk ak ñoom alal ak i doomn te digleen”. Waaye Séytaane duleen dig lu dul ay nax.
65إِنَّ عِبَادِي لَيْسَ لَكَ عَلَيْهِمْ سُلْطَانٌ ۚ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ وَكِيلًا
Naka samay jaam, doo am genn kàttan ci ñoom”. Ndax sa Boroom doy na cëslaay.
66رَّبُّكُمُ الَّذِي يُزْجِي لَكُمُ الْفُلْكَ فِي الْبَحْرِ لِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِكُمْ رَحِيمًا
Sa Boroom mooy kiy dawloo gaal ci géej, ngir ngeen mën a sàkku ay xéewalam ; Naka Moom ku am yërmaande la ci yéen,
67وَإِذَا مَسَّكُمُ الضُّرُّ فِي الْبَحْرِ ضَلَّ مَن تَدْعُونَ إِلَّا إِيَّاهُ ۖ فَلَمَّا نَجَّاكُمْ إِلَى الْبَرِّ أَعْرَضْتُمْ ۚ وَكَانَ الْإِنسَانُ كَفُورًا
Bu leen naqar dabee ci géej, ña ngeen doon jaamu réer leen ginnaawam. Te bu Nu leen musalee ba ñu agsi ci jéeri ji, ngeen dëddu. Nit daal ku goreedi la !
68أَفَأَمِنتُمْ أَن يَخْسِفَ بِكُمْ جَانِبَ الْبَرِّ أَوْ يُرْسِلَ عَلَيْكُمْ حَاصِبًا ثُمَّ لَا تَجِدُوا لَكُمْ وَكِيلًا
Moo ndax dangeen a naagu ne : du xar suuf si [mëdd leen], walla duleen yónnee ngelawu sànniy xeer fekk dungeen ci am ku leen ci yiir.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Al-Isra 66

Simoore Al-Isra Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom mooy kiy dawloo gaal ci géej, ngir ngeen…

Simoore Aaya 66/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers