Al-Isra · 78/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
أَقِمِ الصَّلَاةَ لِدُلُوكِ الشَّمْسِ إِلَىٰ غَسَقِ اللَّيْلِ وَقُرْآنَ الْفَجْرِ ۖ إِنَّ قُرْآنَ الْفَجْرِ كَانَ مَشْهُودًا ۝٧٨
Aqimis Salaata liduloo kish shamsi ilaa ghasaqil laili wa quraanal Fajri inna quraa nal Fajri kaana mashhoodaa
📖 Tekkim Wolof
Nanga taxawal julli bu jant fenkee ba ba muy suux, ba ba guddi gi di ñuul, ak it jullig suba, ndax jullig suba lu ñuy seede la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 76-80 — Simoore Al-Isra

76وَإِن كَادُوا لَيَسْتَفِزُّونَكَ مِنَ الْأَرْضِ لِيُخْرِجُوكَ مِنْهَا ۖ وَإِذًا لَّا يَلْبَثُونَ خِلَافَكَ إِلَّا قَلِيلًا
Te xaw nañu laa génne ca suuf sa [suufi Madiina] ngir ñu jële la fa. Te kon duñu fa toog lu dul diir bu néew ci sa ginnaw. [alag leen].
77سُنَّةَ مَن قَدْ أَرْسَلْنَا قَبْلَكَ مِن رُّسُلِنَا ۖ وَلَا تَجِدُ لِسُنَّتِنَا تَحْوِيلًا
Loolu aada la ca ña Nu yónni woon la la jiitu ci Sunuy Yonent. Te doo gis lu soppiku ci Sunuy aada.
78أَقِمِ الصَّلَاةَ لِدُلُوكِ الشَّمْسِ إِلَىٰ غَسَقِ اللَّيْلِ وَقُرْآنَ الْفَجْرِ ۖ إِنَّ قُرْآنَ الْفَجْرِ كَانَ مَشْهُودًا
Nanga taxawal julli bu jant fenkee ba ba muy suux, ba ba guddi gi di ñuul, ak it jullig suba, ndax jullig suba lu ñuy seede la.
79وَمِنَ اللَّيْلِ فَتَهَجَّدْ بِهِ نَافِلَةً لَّكَ عَسَىٰ أَن يَبْعَثَكَ رَبُّكَ مَقَامًا مَّحْمُودًا
Te nangay julli ci suba, def ko muy naafila : xéy-na kon sa Boroom dekkal la, jox la ndam lu yeyoo cant.
80وَقُل رَّبِّ أَدْخِلْنِي مُدْخَلَ صِدْقٍ وَأَخْرِجْنِي مُخْرَجَ صِدْقٍ وَاجْعَل لِّي مِن لَّدُنكَ سُلْطَانًا نَّصِيرًا
Neel : "Sama Boroom ; dugal ma ci duggukaayu dëggu te nga génne ma ci génnukaayu dëgg ; te nga defal ma kàttan gu tukke ci yaw di dimbal”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Al-Isra 78

Simoore Al-Isra Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nanga taxawal julli bu jant fenkee ba ba muy suux,…

Simoore Aaya 78/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers