Al-Kahf · 108/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
خَالِدِينَ فِيهَا لَا يَبْغُونَ عَنْهَا حِوَلًا ١٠٨
Transliteration
Khaalideena feeha la yabghoona `anhaa hiwalaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
dañu fay béel te duñu ko bëgg a weccee.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 106-110 — Al-Kahf
106ذَٰلِكَ جَزَاؤُهُمْ جَهَنَّمُ بِمَا كَفَرُوا وَاتَّخَذُوا آيَاتِي وَرُسُلِي هُزُوًا
Loola moo tax ñu feye leen Safara, ngir la ñu weddi woon tey jàppe Sunuy kàddu ak Sunuy Yonent ay caaxaan.
107إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ كَانَتْ لَهُمْ جَنَّاتُ الْفِرْدَوْسِ نُزُلًا
Ña gëmoon tey jëf u yiw, Àjjana [Firdawsi] mooy seen wàccuwaay,
108خَالِدِينَ فِيهَا لَا يَبْغُونَ عَنْهَا حِوَلًا
dañu fay béel te duñu ko bëgg a weccee.
109قُل لَّوْ كَانَ الْبَحْرُ مِدَادًا لِّكَلِمَاتِ رَبِّي لَنَفِدَ الْبَحْرُ قَبْلَ أَن تَنفَدَ كَلِمَاتُ رَبِّي وَلَوْ جِئْنَا بِمِثْلِهِ مَدَدًا
Waxalne : “Su ndoxum géej gi doonoon daa, ñu di ca binde kàdduy Yàlla yi, kon ndox ma dana jeex balaa kàddu ya di mat, doonte la sax dañu cay dolliwaat lu tollu ni géej ya”.
110قُلْ إِنَّمَا أَنَا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَمَن كَانَ يَرْجُو لِقَاءَ رَبِّهِ فَلْيَعْمَلْ عَمَلًا صَالِحًا وَلَا يُشْرِكْ بِعِبَادَةِ رَبِّهِ أَحَدًا
Neel : “Man dey mbindéef laa ni yéen. Danu may soloo rekk, waaye li wóor moo di seen Yàlla jenn rekk la ! [Kon nag], képp ku yaakaar dajeek Boroomam, nay jëf jëf yu yiw te bu mu bokkaale dara ak Boroomam [na ko jaamu Moom doŋŋ]”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
108Aaya
Tekki — Al-Kahf 108
Simoore Al-Kahf Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dañu fay béel te duñu ko bëgg a weccee.Simoore Aaya 108/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








