Al-Kahf · 5/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
مَّا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ وَلَا لِآبَائِهِمْ ۚ كَبُرَتْ كَلِمَةً تَخْرُجُ مِنْ أَفْوَاهِهِمْ ۚ إِن يَقُولُونَ إِلَّا كَذِبًا ۝٥
Maa lahum bihee min `ilminw wa laa li aabaaa`ihim; kaburat kalimatan takhruju min afwaahihim; iny yaqooloona illaa kazibaa
📖 Tekkim Wolof
Amuñu ci loolu benn xam-xam, Seeni baay it [amuñu ko ca]. Muy wax ju réy ju génne ci seen gémmiñ! Waxuñu lu dul fen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Al-Kahf

3مَّاكِثِينَ فِيهِ أَبَدًا
te dañu cay sax dapet dàkk ba fàwwu,
4وَيُنذِرَ الَّذِينَ قَالُوا اتَّخَذَ اللَّهُ وَلَدًا
te muy xupp ñay wax naan : “Yàlla am na doom.”
5مَّا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ وَلَا لِآبَائِهِمْ ۚ كَبُرَتْ كَلِمَةً تَخْرُجُ مِنْ أَفْوَاهِهِمْ ۚ إِن يَقُولُونَ إِلَّا كَذِبًا
Amuñu ci loolu benn xam-xam, Seeni baay it [amuñu ko ca]. Muy wax ju réy ju génne ci seen gémmiñ! Waxuñu lu dul fen.
6فَلَعَلَّكَ بَاخِعٌ نَّفْسَكَ عَلَىٰ آثَارِهِمْ إِن لَّمْ يُؤْمِنُوا بِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَسَفًا
Te xéy-na nga lor sa bopp ci naqarlu ngir li ñu ñàkk a gëm kàddu ga !
7إِنَّا جَعَلْنَا مَا عَلَى الْأَرْضِ زِينَةً لَّهَا لِنَبْلُوَهُمْ أَيُّهُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا
Nun noo def ci suuf si taaram ngir nattu leen, [ba xam] ña ca gën a rafet jëf.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Kahf 5

Simoore Al-Kahf Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amuñu ci loolu benn xam-xam, Seeni baay it [amuñu ko…

Simoore Aaya 5/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers