Al-Kahf · 90/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَطْلِعَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَطْلُعُ عَلَىٰ قَوْمٍ لَّمْ نَجْعَل لَّهُم مِّن دُونِهَا سِتْرًا ۝٩٠
Hattaaa izaa balagha matli`ash shamsi wajdahaa tatlu`u alaa qawmil lam naj`al lahum min doonihaa sitraa
📖 Tekkim Wolof
Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk fa xeet wu amul lu leen yiiral tàngooru jant bi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 88-92 — Al-Kahf

88وَأَمَّا مَنْ آمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَلَهُ جَزَاءً الْحُسْنَىٰ ۖ وَسَنَقُولُ لَهُ مِنْ أَمْرِنَا يُسْرًا
Képp koo xam ne dafa gëm tey jëf u yiw, dana am pey gu gën a rafet. Te it fu mu tollu di gis yombal gu bawoo fi nun”.
89ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu dellu sóobu ci bëgg-bëggam.
90حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَطْلِعَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَطْلُعُ عَلَىٰ قَوْمٍ لَّمْ نَجْعَل لَّهُم مِّن دُونِهَا سِتْرًا
Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk fa xeet wu amul lu leen yiiral tàngooru jant bi.
91كَذَٰلِكَ وَقَدْ أَحَطْنَا بِمَا لَدَيْهِ خُبْرًا
Mu wax ne : na ñu defoon ñële rekk la ñuy def ñii, waxoon nanu lépp la mu nar.
92ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu wéyati ci bëgg-bëggamdi dox di wéy.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — Al-Kahf 90

Simoore Al-Kahf Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu takk xare dem ba fa penku yem, mu fekk…

Simoore Aaya 90/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers