Al-Kahf · 94/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
قَالُوا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِنَّ يَأْجُوجَ وَمَأْجُوجَ مُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ فَهَلْ نَجْعَلُ لَكَ خَرْجًا عَلَىٰ أَن تَجْعَلَ بَيْنَنَا وَبَيْنَهُمْ سَدًّا ٩٤
Transliteration
Qaaloo yaa Zal qarnaini inna Yaajooja wa Maajooja mufsidoona fil ardi fahal naj`alu laka kharjan `alaaa an taj`ala bainanaa wa bainahum saddas
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : "Yaa juuja ak Maa juuja ay yàqkat lañu ci kaw suuf si. Moo ndax duñu la fey nga ñag sunu diggante ak ñoom ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 92-96 — Al-Kahf
92ثُمَّ أَتْبَعَ سَبَبًا
Mu wéyati ci bëgg-bëggamdi dox di wéy.
93حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ بَيْنَ السَّدَّيْنِ وَجَدَ مِن دُونِهِمَا قَوْمًا لَّا يَكَادُونَ يَفْقَهُونَ قَوْلًا
Muy dem ba fekk aw xur mu fekk aw xeet, woo xam ne, seeni wax xaw naa niru waxi nit
94قَالُوا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِنَّ يَأْجُوجَ وَمَأْجُوجَ مُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ فَهَلْ نَجْعَلُ لَكَ خَرْجًا عَلَىٰ أَن تَجْعَلَ بَيْنَنَا وَبَيْنَهُمْ سَدًّا
Ñu ne ko : "Yaa juuja ak Maa juuja ay yàqkat lañu ci kaw suuf si. Moo ndax duñu la fey nga ñag sunu diggante ak ñoom ? ”
95قَالَ مَا مَكَّنِّي فِيهِ رَبِّي خَيْرٌ فَأَعِينُونِي بِقُوَّةٍ أَجْعَلْ بَيْنَكُمْ وَبَيْنَهُمْ رَدْمًا
Mu ne leen : “Li ma Yàlla defal moo gën ci man [seenug pey]. Li may laaj rekk mooy ngeen jàppale ma, danaa defar ab ñag seen diggante ak ñoom.
96آتُونِي زُبَرَ الْحَدِيدِ ۖ حَتَّىٰ إِذَا سَاوَىٰ بَيْنَ الصَّدَفَيْنِ قَالَ انفُخُوا ۖ حَتَّىٰ إِذَا جَعَلَهُ نَارًا قَالَ آتُونِي أُفْرِغْ عَلَيْهِ قِطْرًا
Indil-leen ma mbuluŋi weñ gu ñuul, te ngeen fatte ko bën-bën yii, te ngeen soy ko ba mu ruy, ngeen sotti ci betteex bi”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
94Aaya
Tekki — Al-Kahf 94
Simoore Al-Kahf Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : "Yaa juuja ak Maa juuja ay…Simoore Aaya 94/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








