Maryam · 13/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَحَنَانًا مِّن لَّدُنَّا وَزَكَاةً ۖ وَكَانَ تَقِيًّا ۝١٣
Wa hanaanam mil ladunnaa wa zakaatanw wa kaana taqiyyaa
📖 Tekkim Wolof
ci ag ñeewant ak ug sellal. Mu doonoon ku ragal Yàlla,

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Maryam

11فَخَرَجَ عَلَىٰ قَوْمِهِ مِنَ الْمِحْرَابِ فَأَوْحَىٰ إِلَيْهِمْ أَن سَبِّحُوا بُكْرَةً وَعَشِيًّا
Mu daldi génne ca fa [mu doon jaaamoo Yàlla] ; jottale leen ne nañuy sàbbal Yàlla suba ak ngoon.
12يَا يَحْيَىٰ خُذِ الْكِتَابَ بِقُوَّةٍ ۖ وَآتَيْنَاهُ الْحُكْمَ صَبِيًّا
"Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu la xam-xamu xereñe [àtte ya] ca ba nga doonee ndaw,
13وَحَنَانًا مِّن لَّدُنَّا وَزَكَاةً ۖ وَكَانَ تَقِيًّا
ci ag ñeewant ak ug sellal. Mu doonoon ku ragal Yàlla,
14وَبَرًّا بِوَالِدَيْهِ وَلَمْ يَكُن جَبَّارًا عَصِيًّا
di ku toppoon ay waajuram ; doonutoon ku fétterlu mbaa muy kut.
15وَسَلَامٌ عَلَيْهِ يَوْمَ وُلِدَ وَيَوْمَ يَمُوتُ وَيَوْمَ يُبْعَثُ حَيًّا
Te jàmm rekk la am ca ba mu juddoo ak ca ba muy dee, ak ca ba muy dekkiwaat !
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Maryam 13

Simoore Maryam Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci ag ñeewant ak ug sellal. Mu doonoon ku ragal…

Simoore Aaya 13/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers