Maryam · 14/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَبَرًّا بِوَالِدَيْهِ وَلَمْ يَكُن جَبَّارًا عَصِيًّا ۝١٤
Wa barram biwaalidayhi wa lam yakum jabbaaran `asiyyaa
📖 Tekkim Wolof
di ku toppoon ay waajuram ; doonutoon ku fétterlu mbaa muy kut.

🎧 Dégg


📜 Aaya 12-16 — Simoore Maryam

12يَا يَحْيَىٰ خُذِ الْكِتَابَ بِقُوَّةٍ ۖ وَآتَيْنَاهُ الْحُكْمَ صَبِيًّا
"Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu la xam-xamu xereñe [àtte ya] ca ba nga doonee ndaw,
13وَحَنَانًا مِّن لَّدُنَّا وَزَكَاةً ۖ وَكَانَ تَقِيًّا
ci ag ñeewant ak ug sellal. Mu doonoon ku ragal Yàlla,
14وَبَرًّا بِوَالِدَيْهِ وَلَمْ يَكُن جَبَّارًا عَصِيًّا
di ku toppoon ay waajuram ; doonutoon ku fétterlu mbaa muy kut.
15وَسَلَامٌ عَلَيْهِ يَوْمَ وُلِدَ وَيَوْمَ يَمُوتُ وَيَوْمَ يُبْعَثُ حَيًّا
Te jàmm rekk la am ca ba mu juddoo ak ca ba muy dee, ak ca ba muy dekkiwaat !
16وَاذْكُرْ فِي الْكِتَابِ مَرْيَمَ إِذِ انتَبَذَتْ مِنْ أَهْلِهَا مَكَانًا شَرْقِيًّا
[Fàttalikul], ca Téere ba, Maryaama ba mu fàddoo mbokk ya, génn dem fa penku dëkk ba.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Maryam 14

Simoore Maryam Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : di ku toppoon ay waajuram ; doonutoon ku fétterlu mbaa…

Simoore Aaya 14/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers