Maryam · 12/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
يَا يَحْيَىٰ خُذِ الْكِتَابَ بِقُوَّةٍ ۖ وَآتَيْنَاهُ الْحُكْمَ صَبِيًّا ۝١٢
Yaa Yahyaa khuzil Kitaaba biquwwatinw wa aatainaahul hukma saiyyaa
📖 Tekkim Wolof
"Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu la xam-xamu xereñe [àtte ya] ca ba nga doonee ndaw,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Maryam

10قَالَ رَبِّ اجْعَل لِّي آيَةً ۚ قَالَ آيَتُكَ أَلَّا تُكَلِّمَ النَّاسَ ثَلَاثَ لَيَالٍ سَوِيًّا
Mu ne ko : “[Yàlla] sama Boroom, defal ma màndarga”. Mu ne ko : “Sa màndarga mooy danga am ñetti fan yoo dul mën a waxante.
11فَخَرَجَ عَلَىٰ قَوْمِهِ مِنَ الْمِحْرَابِ فَأَوْحَىٰ إِلَيْهِمْ أَن سَبِّحُوا بُكْرَةً وَعَشِيًّا
Mu daldi génne ca fa [mu doon jaaamoo Yàlla] ; jottale leen ne nañuy sàbbal Yàlla suba ak ngoon.
12يَا يَحْيَىٰ خُذِ الْكِتَابَ بِقُوَّةٍ ۖ وَآتَيْنَاهُ الْحُكْمَ صَبِيًّا
"Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu la xam-xamu xereñe [àtte ya] ca ba nga doonee ndaw,
13وَحَنَانًا مِّن لَّدُنَّا وَزَكَاةً ۖ وَكَانَ تَقِيًّا
ci ag ñeewant ak ug sellal. Mu doonoon ku ragal Yàlla,
14وَبَرًّا بِوَالِدَيْهِ وَلَمْ يَكُن جَبَّارًا عَصِيًّا
di ku toppoon ay waajuram ; doonutoon ku fétterlu mbaa muy kut.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Maryam 12

Simoore Maryam Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : "Éy Yahyaa, jàngal Téere ba [cig settantal] ! ”.Jox Nanu…

Simoore Aaya 12/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers