Maryam · 28/98
Tekki Waxtaan — Maryam
يَا أُخْتَ هَارُونَ مَا كَانَ أَبُوكِ امْرَأَ سَوْءٍ وَمَا كَانَتْ أُمُّكِ بَغِيًّا ۝٢٨
Yaaa ukkhta Haaroona maa kaana abokim ra-a saw`inw wa maa kaanat ummuki baghiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Yaw jigéenub Haaruuna bi, sa baay de doonul woon ku bon, sa yaay it du ku baaloy [taxawaalukat]”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 26-30 — Maryam

26فَكُلِي وَاشْرَبِي وَقَرِّي عَيْنًا ۖ فَإِمَّا تَرَيِنَّ مِنَ الْبَشَرِ أَحَدًا فَقُولِي إِنِّي نَذَرْتُ لِلرَّحْمَٰنِ صَوْمًا فَلَنْ أُكَلِّمَ الْيَوْمَ إِنسِيًّا
Lekkal te naan te dalal sam xel ! Nit koo fi mëna gis nee ko: “Damaa woor, tey duma wax ak kenn nit”.
27فَأَتَتْ بِهِ قَوْمَهَا تَحْمِلُهُ ۖ قَالُوا يَا مَرْيَمُ لَقَدْ جِئْتِ شَيْئًا فَرِيًّا
Mu lewu [doom ja] indi ko fa mbokk ya. Ñu ne ko : “Indi nga fi mbir mu juunu !
28يَا أُخْتَ هَارُونَ مَا كَانَ أَبُوكِ امْرَأَ سَوْءٍ وَمَا كَانَتْ أُمُّكِ بَغِيًّا
Yaw jigéenub Haaruuna bi, sa baay de doonul woon ku bon, sa yaay it du ku baaloy [taxawaalukat]”.
29فَأَشَارَتْ إِلَيْهِ ۖ قَالُوا كَيْفَ نُكَلِّمُ مَن كَانَ فِي الْمَهْدِ صَبِيًّا
Mu joxoñ leen liir ba. Ñu ne ko : “Naka la nuy waxeek liir bu tëdd ciy laltaay ? ”
30قَالَ إِنِّي عَبْدُ اللَّهِ آتَانِيَ الْكِتَابَ وَجَعَلَنِي نَبِيًّا
Liir ba daldi ne : “Man dey jaamub Yàlla laa. Jox na ma Téere ba, def ma ab Yonent.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Maryam 28

Simoore Maryam Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw jigéenub Haaruuna bi, sa baay de doonul woon ku…

Simoore Aaya 28/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers