Maryam · 27/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
فَأَتَتْ بِهِ قَوْمَهَا تَحْمِلُهُ ۖ قَالُوا يَا مَرْيَمُ لَقَدْ جِئْتِ شَيْئًا فَرِيًّا ۝٢٧
Fa atat bihee qawmahaa tahmiluhoo qaaloo yaa Maryamoo laqad ji`ti shai`an fariyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mu lewu [doom ja] indi ko fa mbokk ya. Ñu ne ko : “Indi nga fi mbir mu juunu !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 25-29 — Simoore Maryam

25وَهُزِّي إِلَيْكِ بِجِذْعِ النَّخْلَةِ تُسَاقِطْ عَلَيْكِ رُطَبًا جَنِيًّا
Gësëmal tàndarma gi : meññent mu nooy dana rot ci say tànk.
26فَكُلِي وَاشْرَبِي وَقَرِّي عَيْنًا ۖ فَإِمَّا تَرَيِنَّ مِنَ الْبَشَرِ أَحَدًا فَقُولِي إِنِّي نَذَرْتُ لِلرَّحْمَٰنِ صَوْمًا فَلَنْ أُكَلِّمَ الْيَوْمَ إِنسِيًّا
Lekkal te naan te dalal sam xel ! Nit koo fi mëna gis nee ko: “Damaa woor, tey duma wax ak kenn nit”.
27فَأَتَتْ بِهِ قَوْمَهَا تَحْمِلُهُ ۖ قَالُوا يَا مَرْيَمُ لَقَدْ جِئْتِ شَيْئًا فَرِيًّا
Mu lewu [doom ja] indi ko fa mbokk ya. Ñu ne ko : “Indi nga fi mbir mu juunu !
28يَا أُخْتَ هَارُونَ مَا كَانَ أَبُوكِ امْرَأَ سَوْءٍ وَمَا كَانَتْ أُمُّكِ بَغِيًّا
Yaw jigéenub Haaruuna bi, sa baay de doonul woon ku bon, sa yaay it du ku baaloy [taxawaalukat]”.
29فَأَشَارَتْ إِلَيْهِ ۖ قَالُوا كَيْفَ نُكَلِّمُ مَن كَانَ فِي الْمَهْدِ صَبِيًّا
Mu joxoñ leen liir ba. Ñu ne ko : “Naka la nuy waxeek liir bu tëdd ciy laltaay ? ”
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Maryam 27

Simoore Maryam Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu lewu [doom ja] indi ko fa mbokk ya. Ñu…

Simoore Aaya 27/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers