Maryam · 82/98
Tekki Waxtaan — Maryam
كَلَّا ۚ سَيَكْفُرُونَ بِعِبَادَتِهِمْ وَيَكُونُونَ عَلَيْهِمْ ضِدًّا ٨٢
Transliteration
Kallaa; sa yakfuroona bi`ibaadatihim wa yakoonoona `alaihim diddaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ndaw njombe ! [Ya ñu doon jaamu] dana weddi jaamu googee te dañuy far safaanoo
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 80-84 — Maryam
80وَنَرِثُهُ مَا يَقُولُ وَيَأْتِينَا فَرْدًا
[Doom ya ak alal ja] Dananu ko donn, te buy dikk fi Nun jubbu boppam lay àndal.
81وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لِّيَكُونُوا لَهُمْ عِزًّا
Dañuy jàpp leneen lu dul Yàlla [di ko jaamu] ngir ame ca teraanga [dimbal].
82كَلَّا ۚ سَيَكْفُرُونَ بِعِبَادَتِهِمْ وَيَكُونُونَ عَلَيْهِمْ ضِدًّا
Ndaw njombe ! [Ya ñu doon jaamu] dana weddi jaamu googee te dañuy far safaanoo
83أَلَمْ تَرَ أَنَّا أَرْسَلْنَا الشَّيَاطِينَ عَلَى الْكَافِرِينَ تَؤُزُّهُمْ أَزًّا
Xanaa gisoo ne Danañu yebal Séytaane ca yéefar ya ñu leen di jax-jaxee ?
84فَلَا تَعْجَلْ عَلَيْهِمْ ۖ إِنَّمَا نَعُدُّ لَهُمْ عَدًّا
Bul yàkkamti seen mbir : dafa am rekk lu ñu leen di nége.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
82Aaya
Tekki — Maryam 82
Simoore Maryam Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndaw njombe ! [Ya ñu doon jaamu] dana weddi jaamu…Simoore Aaya 82/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








