Maryam · 81/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لِّيَكُونُوا لَهُمْ عِزًّا ۝٨١
Wattakhazoo min doonil laahi aalihatal liyakoonoo lahum `izzaa
📖 Tekkim Wolof
Dañuy jàpp leneen lu dul Yàlla [di ko jaamu] ngir ame ca teraanga [dimbal].

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 79-83 — Simoore Maryam

79كَلَّا ۚ سَنَكْتُبُ مَا يَقُولُ وَنَمُدُّ لَهُ مِنَ الْعَذَابِ مَدًّا
Déewallaay ! Dananu bind la muy wax, te it Dananu ko mbugal.
80وَنَرِثُهُ مَا يَقُولُ وَيَأْتِينَا فَرْدًا
[Doom ya ak alal ja] Dananu ko donn, te buy dikk fi Nun jubbu boppam lay àndal.
81وَاتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ آلِهَةً لِّيَكُونُوا لَهُمْ عِزًّا
Dañuy jàpp leneen lu dul Yàlla [di ko jaamu] ngir ame ca teraanga [dimbal].
82كَلَّا ۚ سَيَكْفُرُونَ بِعِبَادَتِهِمْ وَيَكُونُونَ عَلَيْهِمْ ضِدًّا
Ndaw njombe ! [Ya ñu doon jaamu] dana weddi jaamu googee te dañuy far safaanoo
83أَلَمْ تَرَ أَنَّا أَرْسَلْنَا الشَّيَاطِينَ عَلَى الْكَافِرِينَ تَؤُزُّهُمْ أَزًّا
Xanaa gisoo ne Danañu yebal Séytaane ca yéefar ya ñu leen di jax-jaxee ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Maryam 81

Simoore Maryam Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dañuy jàpp leneen lu dul Yàlla [di ko jaamu] ngir…

Simoore Aaya 81/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers