Maryam · 96/98
Tekki Waxtaan — Maryam
إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ سَيَجْعَلُ لَهُمُ الرَّحْمَٰنُ وُدًّا ٩٦
Transliteration
Innal lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati sa yaj`alu lahumur Rahmaanu wuddaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 94-98 — Maryam
94لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].
95وَكُلُّهُمْ آتِيهِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَرْدًا
Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam kennoo kenn.
96إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ سَيَجْعَلُ لَهُمُ الرَّحْمَٰنُ وُدًّا
Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.
97فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لِتُبَشِّرَ بِهِ الْمُتَّقِينَ وَتُنذِرَ بِهِ قَوْمًا لُّدًّا
Yombalal Nanu la Téere bii, jaarale ko ci saw làmmiñ ngir nga bégal ci ñi ragal Yàlla te xupp ca ña dëgër bopp [weddi].
98وَكَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّن قَرْنٍ هَلْ تُحِسُّ مِنْهُم مِّنْ أَحَدٍ أَوْ تَسْمَعُ لَهُمْ رِكْزًا
Aka bari li Nu alag ca xeet ya leen jiitu woon ! Moo ndax gisati nga lu ca bokk ? Mbaa nga déggati seenum riir ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
96Aaya
Tekki — Maryam 96
Simoore Maryam Aaya 96 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.Simoore Aaya 96/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 94–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








