Maryam · 95/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَكُلُّهُمْ آتِيهِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَرْدًا ٩٥
Transliteration
Wa kulluhum aateehi Yawmal Qiyaamati fardaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam kennoo kenn.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 93-97 — Maryam
93إِن كُلُّ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ إِلَّا آتِي الرَّحْمَٰنِ عَبْدًا
Képp ku nekk ci asamaan yi ak suuf si, jaamub Yàlla rekk lay doon.
94لَّقَدْ أَحْصَاهُمْ وَعَدَّهُمْ عَدًّا
[Moom Yàlla] xam na fa ñu nekk ak na ñu day [na ñu tollu].
95وَكُلُّهُمْ آتِيهِ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فَرْدًا
Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam kennoo kenn.
96إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ سَيَجْعَلُ لَهُمُ الرَّحْمَٰنُ وُدًّا
Ña gëm tey jëf u yiw, Yàlla dana leen sagoo.
97فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لِتُبَشِّرَ بِهِ الْمُتَّقِينَ وَتُنذِرَ بِهِ قَوْمًا لُّدًّا
Yombalal Nanu la Téere bii, jaarale ko ci saw làmmiñ ngir nga bégal ci ñi ragal Yàlla te xupp ca ña dëgër bopp [weddi].
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
95Aaya
Tekki — Maryam 95
Simoore Maryam Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu Bis-pénc baa, bindéef yépp danañu taxaw ci kanamam…Simoore Aaya 95/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








