Al-Baqara · 106/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
۞ مَا نَنسَخْ مِنْ آيَةٍ أَوْ نُنسِهَا نَأْتِ بِخَيْرٍ مِّنْهَا أَوْ مِثْلِهَا ۗ أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝١٠٦
Maa nansakh min aayatin aw nunsihaa na-ti bikhairim minhaaa aw mislihaaa; alam ta`lam annal laaha `alaa kulli shai`in qadeer
📖 Tekkim Wolof
Dunu folli jenn laaya walla Nu ginnaawal ko fàtteloo ko [nit ñi], te indiwunu bu ko gën mbaa mel ni moom. Xanaa xamoo ne Yàlla mën na lu ne ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 104-108 — Al-Baqara

104يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَقُولُوا رَاعِنَا وَقُولُوا انظُرْنَا وَاسْمَعُوا ۗ وَلِلْكَافِرِينَ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Éy yéen way-gëm yi ! Buleen di wax [sàmmoonteel ak nun], deeleen wax : “Xool nu” ; te deeleen dégg [ndigal] ! Mbugal mu metti mooy dal ca kaw way-weddi ña.
105مَّا يَوَدُّ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَلَا الْمُشْرِكِينَ أَن يُنَزَّلَ عَلَيْكُم مِّنْ خَيْرٍ مِّن رَّبِّكُمْ ۗ وَاللَّهُ يَخْتَصُّ بِرَحْمَتِهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ ذُو الْفَضْلِ الْعَظِيمِ
Ña weddi ca ñoñ-téere ya ak way-bokkaale ya yéenewuñuleen, yiw wu bari ba bawoo ca seen Boroom, wàcc ci yéen, te Yàlla dana jagale yërmaandeem ku ko soob. Yàlla mooy boroom ngëneel yu màgg yi.
106۞ مَا نَنسَخْ مِنْ آيَةٍ أَوْ نُنسِهَا نَأْتِ بِخَيْرٍ مِّنْهَا أَوْ مِثْلِهَا ۗ أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Dunu folli jenn laaya walla Nu ginnaawal ko fàtteloo ko [nit ñi], te indiwunu bu ko gën mbaa mel ni moom. Xanaa xamoo ne Yàlla mën na lu ne ?
107أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Xanaa xamuloo ne Yàlla moo di Boroom nguurug asamaan ak suuf si, te ginnaaw Yàlla amul keneen ku mën a doon seen kiiraay mbaa seen ndimbal ?
108أَمْ تُرِيدُونَ أَن تَسْأَلُوا رَسُولَكُمْ كَمَا سُئِلَ مُوسَىٰ مِن قَبْلُ ۗ وَمَن يَتَبَدَّلِ الْكُفْرَ بِالْإِيمَانِ فَقَدْ ضَلَّ سَوَاءَ السَّبِيلِ
Am dangeen bëgg a laaj seen Yonent na ñu laajee woon Muusaa ca bu njëkk ? Képp ku weccee ngëm ak weddi, réer na te wàcc na yoon wu njub wa.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
106Aaya

Tekki — Al-Baqara 106

Simoore Al-Baqara Aaya 106 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dunu folli jenn laaya walla Nu ginnaawal ko fàtteloo ko…

Simoore Aaya 106/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 104–108. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers