Al-Baqara · 107/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ ۝١٠٧
Alam ta`lam annallaaha lahoo mulkus samaawaati wal ard; wa maa lakum min doonil laahi minw waliyyinw wa laa naseer
📖 Tekkim Wolof
Xanaa xamuloo ne Yàlla moo di Boroom nguurug asamaan ak suuf si, te ginnaaw Yàlla amul keneen ku mën a doon seen kiiraay mbaa seen ndimbal ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 105-109 — Al-Baqara

105مَّا يَوَدُّ الَّذِينَ كَفَرُوا مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ وَلَا الْمُشْرِكِينَ أَن يُنَزَّلَ عَلَيْكُم مِّنْ خَيْرٍ مِّن رَّبِّكُمْ ۗ وَاللَّهُ يَخْتَصُّ بِرَحْمَتِهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَاللَّهُ ذُو الْفَضْلِ الْعَظِيمِ
Ña weddi ca ñoñ-téere ya ak way-bokkaale ya yéenewuñuleen, yiw wu bari ba bawoo ca seen Boroom, wàcc ci yéen, te Yàlla dana jagale yërmaandeem ku ko soob. Yàlla mooy boroom ngëneel yu màgg yi.
106۞ مَا نَنسَخْ مِنْ آيَةٍ أَوْ نُنسِهَا نَأْتِ بِخَيْرٍ مِّنْهَا أَوْ مِثْلِهَا ۗ أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Dunu folli jenn laaya walla Nu ginnaawal ko fàtteloo ko [nit ñi], te indiwunu bu ko gën mbaa mel ni moom. Xanaa xamoo ne Yàlla mën na lu ne ?
107أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ لَهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَمَا لَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Xanaa xamuloo ne Yàlla moo di Boroom nguurug asamaan ak suuf si, te ginnaaw Yàlla amul keneen ku mën a doon seen kiiraay mbaa seen ndimbal ?
108أَمْ تُرِيدُونَ أَن تَسْأَلُوا رَسُولَكُمْ كَمَا سُئِلَ مُوسَىٰ مِن قَبْلُ ۗ وَمَن يَتَبَدَّلِ الْكُفْرَ بِالْإِيمَانِ فَقَدْ ضَلَّ سَوَاءَ السَّبِيلِ
Am dangeen bëgg a laaj seen Yonent na ñu laajee woon Muusaa ca bu njëkk ? Képp ku weccee ngëm ak weddi, réer na te wàcc na yoon wu njub wa.
109وَدَّ كَثِيرٌ مِّنْ أَهْلِ الْكِتَابِ لَوْ يَرُدُّونَكُم مِّن بَعْدِ إِيمَانِكُمْ كُفَّارًا حَسَدًا مِّنْ عِندِ أَنفُسِهِم مِّن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْحَقُّ ۖ فَاعْفُوا وَاصْفَحُوا حَتَّىٰ يَأْتِيَ اللَّهُ بِأَمْرِهِ ۗ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ñu bari ci ñoñ-téere [Yahuud ak Nasaraan] nee nañu siiw ñu delloo leen cig kéefar ginnaaw seen ngëm ngir kiñaan gu sosoo seeni bakkan. Ginnaaw ba dëgg ga leeree nàññ ? Baal-leen te dummóoyuleen ba Yàlla agseek ndigëlam. Yàlla nag mën na lu ne !
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
107Aaya

Tekki — Al-Baqara 107

Simoore Al-Baqara Aaya 107 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa xamuloo ne Yàlla moo di Boroom nguurug asamaan ak…

Simoore Aaya 107/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 105–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers