Al-Baqara · 69/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا لَوْنُهَا ۚ قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ صَفْرَاءُ فَاقِعٌ لَّوْنُهَا تَسُرُّ النَّاظِرِينَ ۝٦٩
Qaalud-`u lanaa rabaaka yubaiyil lanaa maa lawnuhaa; qaala innahoo yaqoolu innahaa baqaratun safraaa`u faqi`ul lawnuhaa tasurrunnaazireen
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral nu luy meloom”. - Mu ne : “Naka Moom nee na: nag la wu gel, wu fees, woo xam ne dees na beg ci xool ko .”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 67-71 — Simoore Al-Baqara

67وَإِذْ قَالَ مُوسَىٰ لِقَوْمِهِ إِنَّ اللَّهَ يَأْمُرُكُمْ أَن تَذْبَحُوا بَقَرَةً ۖ قَالُوا أَتَتَّخِذُنَا هُزُوًا ۖ قَالَ أَعُوذُ بِاللَّهِ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْجَاهِلِينَ
Fàttalikuleen,) ba Muusaa waxee aw nitam : “Yàlla digal na leen ngeen reyu nag”. Ñu ne ko : “Moo ndax danga nuy ñaawal ? ”. Mu ne : “Yàlla na ma Yàlla musal ci bokk ci way-réer ña ”.
68قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا هِيَ ۚ قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ لَّا فَارِضٌ وَلَا بِكْرٌ عَوَانٌ بَيْنَ ذَٰلِكَ ۖ فَافْعَلُوا مَا تُؤْمَرُونَ
Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral nu luy meloom”. - Mu ne : “Naka Moom nee na : nag wa du wu màggat, du aw sëll, dafa digg-dóomu. Def leen li ñu leen sant”.
69قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا لَوْنُهَا ۚ قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ صَفْرَاءُ فَاقِعٌ لَّوْنُهَا تَسُرُّ النَّاظِرِينَ
- Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral nu luy meloom”. - Mu ne : “Naka Moom nee na: nag la wu gel, wu fees, woo xam ne dees na beg ci xool ko .”.
70قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا هِيَ إِنَّ الْبَقَرَ تَشَابَهَ عَلَيْنَا وَإِنَّا إِن شَاءَ اللَّهُ لَمُهْتَدُونَ
- Ñu ne : “Laajal nu sa Boroom mu leeral nu nu mu mel, ndax nag yi dañoo bari ci nun. Te bu soobe Yàlla dananu gindiku [Jëfe ndigalam]”.
71قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ لَّا ذَلُولٌ تُثِيرُ الْأَرْضَ وَلَا تَسْقِي الْحَرْثَ مُسَلَّمَةٌ لَّا شِيَةَ فِيهَا ۚ قَالُوا الْآنَ جِئْتَ بِالْحَقِّ ۚ فَذَبَحُوهَا وَمَا كَادُوا يَفْعَلُونَ
– Mu ne moom nag : “Nee na, nag la wu ñu bayloowul suuf si, du buy suuxat mbay, bu amul benn laago la te wenn melo la”. - Ñu ne ko : “Agsi nga ci dëgg gi! ” Ñu rendi ko te xawoon nañu koo bañ a def.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
69Aaya

Tekki — Al-Baqara 69

Simoore Al-Baqara Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral…

Simoore Aaya 69/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers