Al-Baqara · 77/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
أَوَلَا يَعْلَمُونَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۝٧٧
Awalaa ya`lamoona annal laaha ya`lamu maa yusirroona wa maa yu`linoon
📖 Tekkim Wolof
- Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-79 — Simoore Al-Baqara

75۞ أَفَتَطْمَعُونَ أَن يُؤْمِنُوا لَكُمْ وَقَدْ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْهُمْ يَسْمَعُونَ كَلَامَ اللَّهِ ثُمَّ يُحَرِّفُونَهُ مِن بَعْدِ مَا عَقَلُوهُ وَهُمْ يَعْلَمُونَ
- Moo ndax, dangeen xeemeem [,Yéen jullit ñi,] Yahuud yi wóolu leen? Te am na ci ñoom kurél boo xam ne déggoon nañu waxi Yàlla, ba noppi soppi ko ginnaw ba ñu ca xalaatee ba xam ko.
76وَإِذَا لَقُوا الَّذِينَ آمَنُوا قَالُوا آمَنَّا وَإِذَا خَلَا بَعْضُهُمْ إِلَىٰ بَعْضٍ قَالُوا أَتُحَدِّثُونَهُم بِمَا فَتَحَ اللَّهُ عَلَيْكُمْ لِيُحَاجُّوكُم بِهِ عِندَ رَبِّكُمْ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
- Bu ñu dajeek ñu gëm, ne : “Gëm nañu” ; te bu ñu wéetee ñoom doŋŋ, naan : “Ndax dungeen waxtaane li leen Yàlla xamal, nu mën caa sukkandiku [ñoom jullit yi] di dàggeek yéen ci seeni [mbiri] Boroom ! Moo ndax dangeen dul xel-lu ? ”.
77أَوَلَا يَعْلَمُونَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ
- Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal ?
78وَمِنْهُمْ أُمِّيُّونَ لَا يَعْلَمُونَ الْكِتَابَ إِلَّا أَمَانِيَّ وَإِنْ هُمْ إِلَّا يَظُنُّونَ
Am na ca ñoo xam ne mënuñoo jàng, xamuñu téere ba lu dul ay fen yu nekk ay njort doŋŋ.
79فَوَيْلٌ لِّلَّذِينَ يَكْتُبُونَ الْكِتَابَ بِأَيْدِيهِمْ ثُمَّ يَقُولُونَ هَٰذَا مِنْ عِندِ اللَّهِ لِيَشْتَرُوا بِهِ ثَمَنًا قَلِيلًا ۖ فَوَيْلٌ لَّهُم مِّمَّا كَتَبَتْ أَيْدِيهِمْ وَوَيْلٌ لَّهُم مِّمَّا يَكْسِبُونَ
Alkaande ñeel na ñay bind téere ba, ba noppi naan lii ca Yàlla la jóge ndax mën caa jële njëg gu néew ! - Alkaande ñeel na leen ngir la ca seeni yoxo bind, ñeel na leen ngir la ñu ca fàggu [ci alal] !
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
77Aaya

Tekki — Al-Baqara 77

Simoore Al-Baqara Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Moo ndax dañoo xamul ne Yàlla xam na la…

Simoore Aaya 77/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers