Taha · 11/135
Tekki Waxtaan — Taha
فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ يَا مُوسَىٰ ۝١١
Falammaaa ataahaa noodiya yaa Moosaa
📖 Tekkim Wolof
Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko woo ne ko : “Éy Muusaa !

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Taha

9وَهَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Moo ndax xam nga xibaari Muusaa ?
10إِذْ رَأَىٰ نَارًا فَقَالَ لِأَهْلِهِ امْكُثُوا إِنِّي آنَسْتُ نَارًا لَّعَلِّي آتِيكُم مِّنْهَا بِقَبَسٍ أَوْ أَجِدُ عَلَى النَّارِ هُدًى
Ba mu gisee aw safara, mu ne njabootam : “Xaarleen ma fii ! Lële ma séen dey aw safara la ; Amaana ma jële fa aw xal, walla ma fekk fa ku ma gindi [teg ma ci yoon]”.
11فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ يَا مُوسَىٰ
Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko woo ne ko : “Éy Muusaa !
12إِنِّي أَنَا رَبُّكَ فَاخْلَعْ نَعْلَيْكَ ۖ إِنَّكَ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Man maay sa Boroom. Summil say dàll : yaa ngi ci biir xur wu sell wu ñuy wax [Tuwaa].
13وَأَنَا اخْتَرْتُكَ فَاسْتَمِعْ لِمَا يُوحَىٰ
Dama laa tànn. Kon déggal li Ma lay soloo.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Taha 11

Simoore Taha Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu agsee ci safara wa, mu am lu ko…

Simoore Aaya 11/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers