Taha · 133/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَقَالُوا لَوْلَا يَأْتِينَا بِآيَةٍ مِّن رَّبِّهِ ۚ أَوَلَمْ تَأْتِهِم بَيِّنَةُ مَا فِي الصُّحُفِ الْأُولَىٰ ۝١٣٣
Wa qaaloo law laa yaateenaa bi Aayatim mmir Rabbih; awalam taatihim baiyinatu maa fis suhufil oolaa
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Lan moo tax indilunu kiiman gu bawoo ca Boroomam ? Moo ndax xalam mujjug ña leen jiitu woon da leen a doyul am njàng ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 131-135 — Simoore Taha

131وَلَا تَمُدَّنَّ عَيْنَيْكَ إِلَىٰ مَا مَتَّعْنَا بِهِ أَزْوَاجًا مِّنْهُمْ زَهْرَةَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا لِنَفْتِنَهُمْ فِيهِ ۚ وَرِزْقُ رَبِّكَ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ
Bul wékk say gët ci li Nu leen wërsëgal ci ay jabar ak alali àddina, ngir sànk leen ci doŋŋ la. Sa peyug Boroom moo gën [fuuf] te moo gën a sax.
132وَأْمُرْ أَهْلَكَ بِالصَّلَاةِ وَاصْطَبِرْ عَلَيْهَا ۖ لَا نَسْأَلُكَ رِزْقًا ۖ نَّحْنُ نَرْزُقُكَ ۗ وَالْعَاقِبَةُ لِلتَّقْوَىٰ
Nanga digal sag njaboot ñuy julli, te nanga saxoo muñ. Tegunu la wut ub dundu : Nun noo warloo sab dund. Ña ragal Yàlla ñoo ëppug muj.
133وَقَالُوا لَوْلَا يَأْتِينَا بِآيَةٍ مِّن رَّبِّهِ ۚ أَوَلَمْ تَأْتِهِم بَيِّنَةُ مَا فِي الصُّحُفِ الْأُولَىٰ
Ñuy wax naan : “Lan moo tax indilunu kiiman gu bawoo ca Boroomam ? Moo ndax xalam mujjug ña leen jiitu woon da leen a doyul am njàng ?
134وَلَوْ أَنَّا أَهْلَكْنَاهُم بِعَذَابٍ مِّن قَبْلِهِ لَقَالُوا رَبَّنَا لَوْلَا أَرْسَلْتَ إِلَيْنَا رَسُولًا فَنَتَّبِعَ آيَاتِكَ مِن قَبْلِ أَن نَّذِلَّ وَنَخْزَىٰ
Bu fekkoon ne Danu leen a mbugal la ko jiitu, kon ñuy wax naan : "Cëy Yàlla soo yónni woon ab Yonent ci nun, kon dananu topp say ndigal bala noo torox ak a tuskare”.
135قُلْ كُلٌّ مُّتَرَبِّصٌ فَتَرَبَّصُوا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ مَنْ أَصْحَابُ الصِّرَاطِ السَّوِيِّ وَمَنِ اهْتَدَىٰ
Neel : “Ñépp a ngay xaar. Xaarleen yéen it ! Dangeen xam ñan ñoo jaaroon ca yoon wu jub wa xocc ak ana ñan ñoo gënoon a gindiku”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
133Aaya

Tekki — Taha 133

Simoore Taha Aaya 133 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Lan moo tax indilunu kiiman gu…

Simoore Aaya 133/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 131–135. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers