Taha · 135/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قُلْ كُلٌّ مُّتَرَبِّصٌ فَتَرَبَّصُوا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ مَنْ أَصْحَابُ الصِّرَاطِ السَّوِيِّ وَمَنِ اهْتَدَىٰ ۝١٣٥
Qul kullum mutarabbisun fatarabbasoo fasta`lamoona man Ashaabus Siraatis Sawiyyi wa manih tadaa
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Ñépp a ngay xaar. Xaarleen yéen it ! Dangeen xam ñan ñoo jaaroon ca yoon wu jub wa xocc ak ana ñan ñoo gënoon a gindiku”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 133-135 — Simoore Taha

133وَقَالُوا لَوْلَا يَأْتِينَا بِآيَةٍ مِّن رَّبِّهِ ۚ أَوَلَمْ تَأْتِهِم بَيِّنَةُ مَا فِي الصُّحُفِ الْأُولَىٰ
Ñuy wax naan : “Lan moo tax indilunu kiiman gu bawoo ca Boroomam ? Moo ndax xalam mujjug ña leen jiitu woon da leen a doyul am njàng ?
134وَلَوْ أَنَّا أَهْلَكْنَاهُم بِعَذَابٍ مِّن قَبْلِهِ لَقَالُوا رَبَّنَا لَوْلَا أَرْسَلْتَ إِلَيْنَا رَسُولًا فَنَتَّبِعَ آيَاتِكَ مِن قَبْلِ أَن نَّذِلَّ وَنَخْزَىٰ
Bu fekkoon ne Danu leen a mbugal la ko jiitu, kon ñuy wax naan : "Cëy Yàlla soo yónni woon ab Yonent ci nun, kon dananu topp say ndigal bala noo torox ak a tuskare”.
135قُلْ كُلٌّ مُّتَرَبِّصٌ فَتَرَبَّصُوا ۖ فَسَتَعْلَمُونَ مَنْ أَصْحَابُ الصِّرَاطِ السَّوِيِّ وَمَنِ اهْتَدَىٰ
Neel : “Ñépp a ngay xaar. Xaarleen yéen it ! Dangeen xam ñan ñoo jaaroon ca yoon wu jub wa xocc ak ana ñan ñoo gënoon a gindiku”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
135Aaya

Tekki — Taha 135

Simoore Taha Aaya 135 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Ñépp a ngay xaar. Xaarleen yéen it !…

Simoore Aaya 135/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 133–135. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers