Al-Anbiya · 53/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
قَالُوا وَجَدْنَا آبَاءَنَا لَهَا عَابِدِينَ ۝٥٣
Qaaloo wajadnaaa aabaaa`anaa lahaa `aabideen
📖 Tekkim Wolof
Ñu tontu ne : “Dañoo fekk sunuy baay di leen jaamu”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 51-55 — Al-Anbiya

51۞ وَلَقَدْ آتَيْنَا إِبْرَاهِيمَ رُشْدَهُ مِن قَبْلُ وَكُنَّا بِهِ عَالِمِينَ
Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu ñu ko xam xéll.
52إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَا هَٰذِهِ التَّمَاثِيلُ الَّتِي أَنتُمْ لَهَا عَاكِفُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee baayam ak nitam ña, ne leen : “Ana luy yàlla xërëm [yu diy jëmm yu ñu yatt] te ngeen fonk leen lool ? ”.
53قَالُوا وَجَدْنَا آبَاءَنَا لَهَا عَابِدِينَ
Ñu tontu ne : “Dañoo fekk sunuy baay di leen jaamu”.
54قَالَ لَقَدْ كُنتُمْ أَنتُمْ وَآبَاؤُكُمْ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Mu ne leen : “Ca dëgg-dëgg, yéen ak seeni baay dangeen a nekk ci réer gu fés”.
55قَالُوا أَجِئْتَنَا بِالْحَقِّ أَمْ أَنتَ مِنَ اللَّاعِبِينَ
Ñu ne ko : “Ndax li nga nu dig dëgg la ci yaw walla dangay kaf ? ”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Al-Anbiya 53

Simoore Al-Anbiya Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu tontu ne : “Dañoo fekk sunuy baay di leen…

Simoore Aaya 53/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers