Al-Anbiya · 88/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
فَاسْتَجَبْنَا لَهُ وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْغَمِّ ۚ وَكَذَٰلِكَ نُنجِي الْمُؤْمِنِينَ ٨٨
Transliteration
Fastajabnaa lahoo wa najjainaahu minal ghamm; wa kazaalika nunjil mu`mineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi koy nangul te musal ko ca njàqare ja. Te it noonu la Nuy musalee way-gëm ña.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 86-90 — Simoore Al-Anbiya
86وَأَدْخَلْنَاهُمْ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُم مِّنَ الصَّالِحِينَ
dugal Nanu leen ci Sunu yërmaande, bokk nañu ca ñu yiw ña [sell].
87وَذَا النُّونِ إِذ ذَّهَبَ مُغَاضِبًا فَظَنَّ أَن لَّن نَّقْدِرَ عَلَيْهِ فَنَادَىٰ فِي الظُّلُمَاتِ أَن لَّا إِلَٰهَ إِلَّا أَنتَ سُبْحَانَكَ إِنِّي كُنتُ مِنَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] boroom jën wa [Yunus] ba mu demee ànd ak mer. Te mu jortoon ne du lu Nu dogal ci moom [ciw tiis ngir la mu dem te amu ca ndigal]. Waaye mu woote ca biir lëndëm ga ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yaw ! Tudd naa sag sell ! Man nag bokk naa ca tooñkat ya”.
88فَاسْتَجَبْنَا لَهُ وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْغَمِّ ۚ وَكَذَٰلِكَ نُنجِي الْمُؤْمِنِينَ
Nu daldi koy nangul te musal ko ca njàqare ja. Te it noonu la Nuy musalee way-gëm ña.
89وَزَكَرِيَّا إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ رَبِّ لَا تَذَرْنِي فَرْدًا وَأَنتَ خَيْرُ الْوَارِثِينَ
[Fàttalikul it] Zakariyaa ba mu woowee Boroomam ne : “Boroom sama, bul ma bàyyi ma wéet, te Yaa di ku gën a mën a dimbalee”.
90فَاسْتَجَبْنَا لَهُ وَوَهَبْنَا لَهُ يَحْيَىٰ وَأَصْلَحْنَا لَهُ زَوْجَهُ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا يُسَارِعُونَ فِي الْخَيْرَاتِ وَيَدْعُونَنَا رَغَبًا وَرَهَبًا ۖ وَكَانُوا لَنَا خَاشِعِينَ
Nu nangul ko, may ko Yahyaa te Nu yéwénalal ko soxnaam. Ñoom sax dañu daan njëkkante ci jëf yu yiw ya te ñoom daanañu Nu jaamu, nekk ci diggante xemmem ak ragal. Te nekkoon nañu diy way-toroxlu ci Nun.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
88Aaya
Tekki — Al-Anbiya 88
Simoore Al-Anbiya Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi koy nangul te musal ko ca njàqare ja.…Simoore Aaya 88/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Anbiya
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Saturday, October 3, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


