Al-Anbiya · 97/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَاقْتَرَبَ الْوَعْدُ الْحَقُّ فَإِذَا هِيَ شَاخِصَةٌ أَبْصَارُ الَّذِينَ كَفَرُوا يَا وَيْلَنَا قَدْ كُنَّا فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا بَلْ كُنَّا ظَالِمِينَ ٩٧
Transliteration
Waqtarabal wa`dul haqqu fa-izaa hiya shaakhisatun absaarul lazeena kafaroo yaawailanaa qad kunna fee ghaflatim min haaza bal kunnaa zaalimeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
dig bu dëggu ba daldi gën a jegeñ, bu boobaa bëti ña weddi dana buqiku, ñu naan : “Ngalla nun ! Nekkoon nanu cig càggante ci lii. Te nekkoon nanu di ay tooñkat”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 95-99 — Al-Anbiya
95وَحَرَامٌ عَلَىٰ قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا أَنَّهُمْ لَا يَرْجِعُونَ
Te dëkk bu Nu rey, waa dëkk ba duñu mënatee dellusi!
96حَتَّىٰ إِذَا فُتِحَتْ يَأْجُوجُ وَمَأْجُوجُ وَهُم مِّن كُلِّ حَدَبٍ يَنسِلُونَ
Ba ba kerook Nuy ubbi Yaajuuja ak Maajuuja ñuy sottiku di rogaat ci tunduwu nekk ;
97وَاقْتَرَبَ الْوَعْدُ الْحَقُّ فَإِذَا هِيَ شَاخِصَةٌ أَبْصَارُ الَّذِينَ كَفَرُوا يَا وَيْلَنَا قَدْ كُنَّا فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا بَلْ كُنَّا ظَالِمِينَ
dig bu dëggu ba daldi gën a jegeñ, bu boobaa bëti ña weddi dana buqiku, ñu naan : “Ngalla nun ! Nekkoon nanu cig càggante ci lii. Te nekkoon nanu di ay tooñkat”.
98إِنَّكُمْ وَمَا تَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ حَصَبُ جَهَنَّمَ أَنتُمْ لَهَا وَارِدُونَ
“Yéen nag ak li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla, yéen a di mattum Safara te yéen dangeen ca dëkk.
99لَوْ كَانَ هَٰؤُلَاءِ آلِهَةً مَّا وَرَدُوهَا ۖ وَكُلٌّ فِيهَا خَالِدُونَ
Bu fekkoon ne ay yàlla lañu, kon duñu ca tàbbi ; nit ñooña ñépp dañu fay béel.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
97Aaya
Tekki — Al-Anbiya 97
Simoore Al-Anbiya Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dig bu dëggu ba daldi gën a jegeñ, bu boobaa…Simoore Aaya 97/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








