Al-Hajj · 43/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
وَقَوْمُ إِبْرَاهِيمَ وَقَوْمُ لُوطٍ ۝٤٣
Wa qawmu Ibraaheema wa qawmu Loot
📖 Tekkim Wolof
ak nitu Ibraahiima ak nitu Lóot.

🎧 Dégg


📜 Aaya 41-45 — Simoore Al-Hajj

41الَّذِينَ إِن مَّكَّنَّاهُمْ فِي الْأَرْضِ أَقَامُوا الصَّلَاةَ وَآتَوُا الزَّكَاةَ وَأَمَرُوا بِالْمَعْرُوفِ وَنَهَوْا عَنِ الْمُنكَرِ ۗ وَلِلَّهِ عَاقِبَةُ الْأُمُورِ
ña nga xam ne, bu Nu leen mayee doole ci kaw suuf si, ñu taxawal julli, di joxe asaka, di digle lu baax, di tere lu bon. Nañu xam ne Yàllaa moom mujjug mbiryi.
42وَإِن يُكَذِّبُوكَ فَقَدْ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ وَعَادٌ وَثَمُودُ
Te bu ñu la weddee, nitu Nooh weddi woon nañu, ak waa Haad ak waa Samuuda,
43وَقَوْمُ إِبْرَاهِيمَ وَقَوْمُ لُوطٍ
ak nitu Ibraahiima ak nitu Lóot.
44وَأَصْحَابُ مَدْيَنَ ۖ وَكُذِّبَ مُوسَىٰ فَأَمْلَيْتُ لِلْكَافِرِينَ ثُمَّ أَخَذْتُهُمْ ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
ak waa Madyaana. Te wedd woon nañu it Muusaa ; Teewul mu muñal yéefar yi, topp Ma sadd leen. Kaawtéef Sama mbugal ma !
45فَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ فَهِيَ خَاوِيَةٌ عَلَىٰ عُرُوشِهَا وَبِئْرٍ مُّعَطَّلَةٍ وَقَصْرٍ مَّشِيدٍ
Ak mbiru dëkk ya Nu alag, te fekk dañoo tooñ. Ñu màbbal seen bopp : Teen ya yàqu ! Tabax ya gent !
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
43Aaya

Tekki — Al-Hajj 43

Simoore Al-Hajj Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak nitu Ibraahiima ak nitu Lóot.

Simoore Aaya 43/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers