Al-Hajj · 42/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَإِن يُكَذِّبُوكَ فَقَدْ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ وَعَادٌ وَثَمُودُ ٤٢
Transliteration
Wa iny yukazzibooka faqad kazzabat qablahum qawmu Nooinw wa Aadunw wa Samood
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te bu ñu la weddee, nitu Nooh weddi woon nañu, ak waa Haad ak waa Samuuda,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 40-44 — Al-Hajj
40الَّذِينَ أُخْرِجُوا مِن دِيَارِهِم بِغَيْرِ حَقٍّ إِلَّا أَن يَقُولُوا رَبُّنَا اللَّهُ ۗ وَلَوْلَا دَفْعُ اللَّهِ النَّاسَ بَعْضَهُم بِبَعْضٍ لَّهُدِّمَتْ صَوَامِعُ وَبِيَعٌ وَصَلَوَاتٌ وَمَسَاجِدُ يُذْكَرُ فِيهَا اسْمُ اللَّهِ كَثِيرًا ۗ وَلَيَنصُرَنَّ اللَّهُ مَن يَنصُرُهُ ۗ إِنَّ اللَّهَ لَقَوِيٌّ عَزِيزٌ
may Na ko it ña ñu génnee ci seeni kër, - ci lu dul dëgg, te defuñu lu dul wax rekk ne : “Yàllaa di sunu Boroom”. - Bu dul kon ak li Yàlla di fege ñenn nit ci ñeneen, kon deef na màbb jaamukaayi yahuud yi, ak yu nasraan yi ak jàkka yi di fu ñuy tudde Yàlla lu bari. Te fàwwu Yàlla dana dimbali ña koy dimbali. Te Yàlla ku bari doole la, di ku not lépp,
41الَّذِينَ إِن مَّكَّنَّاهُمْ فِي الْأَرْضِ أَقَامُوا الصَّلَاةَ وَآتَوُا الزَّكَاةَ وَأَمَرُوا بِالْمَعْرُوفِ وَنَهَوْا عَنِ الْمُنكَرِ ۗ وَلِلَّهِ عَاقِبَةُ الْأُمُورِ
ña nga xam ne, bu Nu leen mayee doole ci kaw suuf si, ñu taxawal julli, di joxe asaka, di digle lu baax, di tere lu bon. Nañu xam ne Yàllaa moom mujjug mbiryi.
42وَإِن يُكَذِّبُوكَ فَقَدْ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ وَعَادٌ وَثَمُودُ
Te bu ñu la weddee, nitu Nooh weddi woon nañu, ak waa Haad ak waa Samuuda,
43وَقَوْمُ إِبْرَاهِيمَ وَقَوْمُ لُوطٍ
ak nitu Ibraahiima ak nitu Lóot.
44وَأَصْحَابُ مَدْيَنَ ۖ وَكُذِّبَ مُوسَىٰ فَأَمْلَيْتُ لِلْكَافِرِينَ ثُمَّ أَخَذْتُهُمْ ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
ak waa Madyaana. Te wedd woon nañu it Muusaa ; Teewul mu muñal yéefar yi, topp Ma sadd leen. Kaawtéef Sama mbugal ma !
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
42Aaya
Tekki — Al-Hajj 42
Simoore Al-Hajj Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu ñu la weddee, nitu Nooh weddi woon nañu,…Simoore Aaya 42/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








