Al-Hajj · 46/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَتَكُونَ لَهُمْ قُلُوبٌ يَعْقِلُونَ بِهَا أَوْ آذَانٌ يَسْمَعُونَ بِهَا ۖ فَإِنَّهَا لَا تَعْمَى الْأَبْصَارُ وَلَٰكِن تَعْمَى الْقُلُوبُ الَّتِي فِي الصُّدُورِ ۝٤٦
Afalam yaseeroo fil ardi fatakoona lahum quloobuny ya`qiloona bihaaa aw aazaanuny yasm`oona bihaa fa innahaa laa ta`mal absaaru wa laakin ta`mal quloobul latee fissudoor
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañoo doxul ci kaw suuf ? Kon danañu am xol bu am ràññee ci loolu ak nopp yu ca am dégg gu wér.Te sax du gët yi ñoo di gumba, waaye xol yi nekk ci seeni dënn ñooy gumba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Al-Hajj

44وَأَصْحَابُ مَدْيَنَ ۖ وَكُذِّبَ مُوسَىٰ فَأَمْلَيْتُ لِلْكَافِرِينَ ثُمَّ أَخَذْتُهُمْ ۖ فَكَيْفَ كَانَ نَكِيرِ
ak waa Madyaana. Te wedd woon nañu it Muusaa ; Teewul mu muñal yéefar yi, topp Ma sadd leen. Kaawtéef Sama mbugal ma !
45فَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ فَهِيَ خَاوِيَةٌ عَلَىٰ عُرُوشِهَا وَبِئْرٍ مُّعَطَّلَةٍ وَقَصْرٍ مَّشِيدٍ
Ak mbiru dëkk ya Nu alag, te fekk dañoo tooñ. Ñu màbbal seen bopp : Teen ya yàqu ! Tabax ya gent !
46أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَتَكُونَ لَهُمْ قُلُوبٌ يَعْقِلُونَ بِهَا أَوْ آذَانٌ يَسْمَعُونَ بِهَا ۖ فَإِنَّهَا لَا تَعْمَى الْأَبْصَارُ وَلَٰكِن تَعْمَى الْقُلُوبُ الَّتِي فِي الصُّدُورِ
Moo ndax dañoo doxul ci kaw suuf ? Kon danañu am xol bu am ràññee ci loolu ak nopp yu ca am dégg gu wér.Te sax du gët yi ñoo di gumba, waaye xol yi nekk ci seeni dënn ñooy gumba.
47وَيَسْتَعْجِلُونَكَ بِالْعَذَابِ وَلَن يُخْلِفَ اللَّهُ وَعْدَهُ ۚ وَإِنَّ يَوْمًا عِندَ رَبِّكَ كَأَلْفِ سَنَةٍ مِّمَّا تَعُدُّونَ
Ña nga lay yàkkamti ci mbugal mi. Te Yàlla du soppi àppam. Te benn bis ca sa Boroom mi ngi mel ni junni at ci seen waññi.
48وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَمْلَيْتُ لَهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ ثُمَّ أَخَذْتُهَا وَإِلَيَّ الْمَصِيرُ
Aka bari dëkk yu Mu muñal te ñu tooñoon ? Ba noppi Mu fàdd leen. Te ci Man la lépp di mujj.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Hajj 46

Simoore Al-Hajj Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañoo doxul ci kaw suuf ? Kon danañu…

Simoore Aaya 46/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers