Al-Mu'minun · 118/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَقُل رَّبِّ اغْفِرْ وَارْحَمْ وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ ۝١١٨
Wa qur Rabbigh fir warham wa Anta khairur raahimeen
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Boroom sama, jéggaleel te yërëme. Yaw yaa di gën ji yërëmaakoon yi”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 116-118 — Simoore Al-Mu'minun

116فَتَعَالَى اللَّهُ الْمَلِكُ الْحَقُّ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْكَرِيمِ
Yàlla buur biy dëgg, kawe na ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Mooy Boroom gàngunaay [Aras] gu tedd ga !
117وَمَن يَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ لَا بُرْهَانَ لَهُ بِهِ فَإِنَّمَا حِسَابُهُ عِندَ رَبِّهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الْكَافِرُونَ
Képp kuy jaamu leneen di ko boole ak Yàlla, [na bir ne] amu ca firnde, te Yàllaa koy lijjanti. Li wér mooy yéefar ya duñu texe.
118وَقُل رَّبِّ اغْفِرْ وَارْحَمْ وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Waxal ne : “Boroom sama, jéggaleel te yërëme. Yaw yaa di gën ji yërëmaakoon yi”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
118Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 118

Simoore Al-Mu'minun Aaya 118 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Boroom sama, jéggaleel te yërëme. Yaw yaa…

Simoore Aaya 118/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 116–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers