Al-Mu'minun · 24/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُرِيدُ أَن يَتَفَضَّلَ عَلَيْكُمْ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَنزَلَ مَلَائِكَةً مَّا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ ٢٤
Transliteration
Faqaalal mala`ul lazeena kafaroo min qawmihee maa haazaaa illaa basharum mislukum yureedu ai yatafaddala `alaikum wa law shaaa`al laahu la anzala malaaa`ikatam maa sami`naa bihaazaa feee aabaaa`inal awwaleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan : “Kii daal nit la ni yéen, dafa bëgg toog ci seen kaw doŋŋ. Te sax bu neexoon Yàlla mu wàcce ay Malaaka. Mësunoo dégg lii ca sunu maam ya jiitu woon.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Al-Mu'minun
22وَعَلَيْهَا وَعَلَى الْفُلْكِ تُحْمَلُونَ
Ngeen di ca war, di ca lonk la ngeen di war.
23وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam. Mu ne leen : "Éy yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
24فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُرِيدُ أَن يَتَفَضَّلَ عَلَيْكُمْ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَنزَلَ مَلَائِكَةً مَّا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan : “Kii daal nit la ni yéen, dafa bëgg toog ci seen kaw doŋŋ. Te sax bu neexoon Yàlla mu wàcce ay Malaaka. Mësunoo dégg lii ca sunu maam ya jiitu woon.
25إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ بِهِ جِنَّةٌ فَتَرَبَّصُوا بِهِ حَتَّىٰ حِينٍ
Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko tuuti.
26قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
[Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi gi ñu ma weddi”.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 24
Simoore Al-Mu'minun Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan…Simoore Aaya 24/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








