Al-Mu'minun · 23/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ ۝٢٣
Wa laqad arsalnaa Noohan ilaa qawmihee faqaala yaa qawmi`budul laaha maa lakum min ilahin ghairuhoo afalaa tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam. Mu ne leen : "Éy yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Mu'minun

21وَإِنَّ لَكُمْ فِي الْأَنْعَامِ لَعِبْرَةً ۖ نُّسْقِيكُم مِّمَّا فِي بُطُونِهَا وَلَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ كَثِيرَةٌ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
Te xanaa war ngeen a am xalaatu fàttaliku ca jur ga leen Yàlla xéewale : Dananu leen nàndale ci li nekk ci biiram [meew], am ngeen ca itam ay njariñ yu bari ; te it ca ngeen di lekk.
22وَعَلَيْهَا وَعَلَى الْفُلْكِ تُحْمَلُونَ
Ngeen di ca war, di ca lonk la ngeen di war.
23وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam. Mu ne leen : "Éy yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
24فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُرِيدُ أَن يَتَفَضَّلَ عَلَيْكُمْ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَنزَلَ مَلَائِكَةً مَّا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan : “Kii daal nit la ni yéen, dafa bëgg toog ci seen kaw doŋŋ. Te sax bu neexoon Yàlla mu wàcce ay Malaaka. Mësunoo dégg lii ca sunu maam ya jiitu woon.
25إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ بِهِ جِنَّةٌ فَتَرَبَّصُوا بِهِ حَتَّىٰ حِينٍ
Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko tuuti.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 23

Simoore Al-Mu'minun Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam. Mu ne leen…

Simoore Aaya 23/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers