Al-Mu'minun · 25/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ بِهِ جِنَّةٌ فَتَرَبَّصُوا بِهِ حَتَّىٰ حِينٍ ۝٢٥
In huwa illaa rajulum bihee jinnatun fatarabbasoo bihee hattan heen
📖 Tekkim Wolof
Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko tuuti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore Al-Mu'minun

23وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Yónni woon Nanu Nooh ca aw nitam. Mu ne leen : "Éy yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
24فَقَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُرِيدُ أَن يَتَفَضَّلَ عَلَيْكُمْ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَنزَلَ مَلَائِكَةً مَّا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Gaa ña weddi woon ca aw nitam di wax naan : “Kii daal nit la ni yéen, dafa bëgg toog ci seen kaw doŋŋ. Te sax bu neexoon Yàlla mu wàcce ay Malaaka. Mësunoo dégg lii ca sunu maam ya jiitu woon.
25إِنْ هُوَ إِلَّا رَجُلٌ بِهِ جِنَّةٌ فَتَرَبَّصُوا بِهِ حَتَّىٰ حِينٍ
Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko tuuti.
26قَالَ رَبِّ انصُرْنِي بِمَا كَذَّبُونِ
[Nooh]ne : “Yaw sama Boroom ! Dimbali ma ci weddi gi ñu ma weddi”.
27فَأَوْحَيْنَا إِلَيْهِ أَنِ اصْنَعِ الْفُلْكَ بِأَعْيُنِنَا وَوَحْيِنَا فَإِذَا جَاءَ أَمْرُنَا وَفَارَ التَّنُّورُ ۙ فَاسْلُكْ فِيهَا مِن كُلٍّ زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ وَأَهْلَكَ إِلَّا مَن سَبَقَ عَلَيْهِ الْقَوْلُ مِنْهُمْ ۖ وَلَا تُخَاطِبْنِي فِي الَّذِينَ ظَلَمُوا ۖ إِنَّهُم مُّغْرَقُونَ
Nu daldi ko soloo [digal ko] ne ko : “Defaral gaal ci Sunug càmm ak Sunu ndigal. Te saa su Sunu ndigal agsee ba lakkukaayu mburu ba sãs, nanga dugal te bàyyi sag njaboot ak yóllent ci wépp xeet ba mu des ña nga xam ne wax ja jiitu woon na c
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 25

Simoore Al-Mu'minun Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kii daal as waay la su jinne sadd, muñal-leen ko…

Simoore Aaya 25/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers