Al-Mu'minun · 4/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَالَّذِينَ هُمْ لِلزَّكَاةِ فَاعِلُونَ ۝٤
Wallazeena hum liz Zakaati faa`iloon
📖 Tekkim Wolof
tey génne asaka,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Al-Mu'minun

2الَّذِينَ هُمْ فِي صَلَاتِهِمْ خَاشِعُونَ
gaa ña nga xam ne dañuy toroxlu ci seen biirug julli,
3وَالَّذِينَ هُمْ عَنِ اللَّغْوِ مُعْرِضُونَ
te ñooy gaa ña nga xam ne dañoo dëddu am po,
4وَالَّذِينَ هُمْ لِلزَّكَاةِ فَاعِلُونَ
tey génne asaka,
5وَالَّذِينَ هُمْ لِفُرُوجِهِمْ حَافِظُونَ
te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni pëy,
6إِلَّا عَلَىٰ أَزْوَاجِهِمْ أَوْ مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُمْ فَإِنَّهُمْ غَيْرُ مَلُومِينَ
lu dul ci seeni soxna ak ci seeni jébéer , ñoom dey kenn yejju leen ;
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 4

Simoore Al-Mu'minun Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : tey génne asaka,

Simoore Aaya 4/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers