Al-Mu'minun · 3/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
وَالَّذِينَ هُمْ عَنِ اللَّغْوِ مُعْرِضُونَ ۝٣
Wallazeena hum `anillaghwimu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
te ñooy gaa ña nga xam ne dañoo dëddu am po,
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-5 — Al-Mu'minun

1قَدْ أَفْلَحَ الْمُؤْمِنُونَ
Way-gëm ña dey texe nañu,
2الَّذِينَ هُمْ فِي صَلَاتِهِمْ خَاشِعُونَ
gaa ña nga xam ne dañuy toroxlu ci seen biirug julli,
3وَالَّذِينَ هُمْ عَنِ اللَّغْوِ مُعْرِضُونَ
te ñooy gaa ña nga xam ne dañoo dëddu am po,
4وَالَّذِينَ هُمْ لِلزَّكَاةِ فَاعِلُونَ
tey génne asaka,
5وَالَّذِينَ هُمْ لِفُرُوجِهِمْ حَافِظُونَ
te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni pëy,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 3

Simoore Al-Mu'minun Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ñooy gaa ña nga xam ne dañoo dëddu am…

Simoore Aaya 3/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers