Al-Mu'minun · 5/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَالَّذِينَ هُمْ لِفُرُوجِهِمْ حَافِظُونَ ۝٥
Wallazeena hum lifuroo jihim haafizoon
📖 Tekkim Wolof
te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni pëy,

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-Mu'minun

3وَالَّذِينَ هُمْ عَنِ اللَّغْوِ مُعْرِضُونَ
te ñooy gaa ña nga xam ne dañoo dëddu am po,
4وَالَّذِينَ هُمْ لِلزَّكَاةِ فَاعِلُونَ
tey génne asaka,
5وَالَّذِينَ هُمْ لِفُرُوجِهِمْ حَافِظُونَ
te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni pëy,
6إِلَّا عَلَىٰ أَزْوَاجِهِمْ أَوْ مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُمْ فَإِنَّهُمْ غَيْرُ مَلُومِينَ
lu dul ci seeni soxna ak ci seeni jébéer , ñoom dey kenn yejju leen ;
7فَمَنِ ابْتَغَىٰ وَرَاءَ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْعَادُونَ
ku sàkku leneen ginnaaw loolu nag, ñoom la ñuy tudde way-jalgati ña ;
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 5

Simoore Al-Mu'minun Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te mooy gaa ña nga xam ne dañuy sàmm seeni…

Simoore Aaya 5/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers